text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
mooy yerem ku neewleek ku tumuranke , di samm bakkanu aji tumuranke , |
te mbooloo mu bare ca dëkk ba di gunge soxna sa |
ca jamono joju , dammel yi , danu daan noot mbooleem nawlee yi dekk ca reew mi . |
xel mu sell mi dina wàcc ci yaw te aji kawe ji dina la yiir ci kàttanam |
te def ci woy wi barke xiirtal nu ci way ci fonk suñ làkk wi népp bokk wéy |
2 yonni napoliyon ngir mu song itaali ngir yare ci otris ak yonneeti ko ci penku bi |
fii nag da ñuy sakku kenn ku ne wone ci sa bëgg bëgg ginnaaw bi ko ni mbooloo mi yépp defe ngir ñu man a liggéy ci nanuy defaree sunum dund ak dund sunuy jegeñaale |
bul gëm muk ay fen ñii di gën a yok daNar ci àddina bi te ñu weeru ci kanam na mbir mu ñu sib |
mbokk a ngi layoo ak moroomam rax ca dolli ci kanam ñi gëmul lañu koy defe |
ndaxte kirist deeyal na nu ca bant ba mel ni gàtt bu ñuy rendi jébbal ko yàlla ca màggalu bésu mucc ba |
cawarte bi nu taxawal taxawaayu ñaar maanaam ni ñu ko xalaate ci bitim yaram wi walla ni ñu ko taqaleek nekkin bi ko wéeral day seey ci ni ñu ko nataale walla mu taxaw taxawaay bu wóor te wér bu aju ci wérug bennoo bu nit ki am |
am na néeg yu bare ca sama kër baay bu dul woon noonu ma wax leen ko ndaxte maa ngi dem defaral leen fa ngeen di dëkk |
yamaleb maxwell yi ñooy àtte yu am solo yu ñeel mbëjbijjaakon ci la yeneen yi soqeekoo |
man ngeen a rannee melow asamaan ak suuf , waaye lu tax menuleen a rannee li jamonoy leegi ji di tekki ? |
bu ma la yonnee artemas walla tisig , gaawantul fekksi ma ci dekku nikopolis , ndax fa laa begg a lollikooji . |
waxiin walla baatal terme yu kattan yi akug soppikoom lu am njarin la ci leeral jefiini dend yi . |
pool tontu ko muy tey , muy elleg , waxuma yaw rekk waaye it ni may deglu tey nepp , na yalla def , ba ngeen fekksi ma ci li ma nekk , lu moy jeng yii ! |
ci noonu warteefi goornamaa yi gen a yaatu , gen bari ci mboolaayi ndefar yi . |
moom ak serin moodu loo desaat fa ba ci la tubaab bi indiwaat serin bi senegaal nu and noom naar . |
dof bi , naata yoon ngay ban xam xam ? |
ci suba teel yeesu dellusi ca dekk ba , mu xiif . |
yeneen laaj yu jem ci firefox bu windows touch . |
ci jamonon injill diiwaan la woon ci sowu suufu diiwaanu room bu tuddoon iliri ci penku géeju adiratig |
waxi sëriñ tuubaa ci diggante boroom kër ak soxnaam ni ñuy dëkkee |
boo bëggee dugg ca dund googu ci kaw nanga sàmm ndigal yi |
daawuda ? kuy doomu yese sax ? jamonoy tey jaam yu baree ngi faqe ci seeni sang . ana luy ndeyi may jel saab dund ak samam ndox , ak yappu jur , gi ma rendil sama watkati jur , di ko jox nu ma xamul fu nu joge ? ba loolu ndawi daawuda walbatiku nibbi . ba nu dikkee , daldi koy yegge kaddu yooyu yepp . daawuda ne ndawam ya rangooleen seeni saamar , yeen nepp . nu rangoo seeni saamar noom nepp , daawuda it rangoo saamaram , lu tollook neenti teemeeri goor and ak daawuda , naar teemeer des ca seen cummikaay . |
loolu tam bokk na ci li janoon xelum nitug tugal ki ci mu jem kanam , gen a naw , rawati na bi dekk yi genee yaatu , degginu ligeeyub yaxantu gen faa xoot , ak bu endustri ak aada . |
waaye boo dee woote lekk wool néew doole yi làggi yi lafañ yi ak gumba yi |
tolluwaay yi nga xam ne fipp gi romb na leen ceri ndajem xeet wi daje woon nanu ca versailles ngir defaral fraans ab sartu reew bu yees . |
ca bés boobee ku nekk ca kaw kër ga te ay bagaasam nekk ca biir bumu wàcc jëli léen |
walla ndax danga am kiñaan ci li ma yéwén |
yeen waa misra , moo yonnee ay firndeek i keemaan fi seen biir , neel firawnaak jawrinam nepp . |
te bi mu jaree , ndax yilifuloo woon njeg gi ? |
ca dëgg dëgg nag loolu am na ndax kat noste ga amoon ca la ëppoon ca réewi tugal ya daa mujjoon di lu ràpp ngirug yàgg mujj manatutoon a ñàkk ñu yeesalaat ko te taxawalaat ko ci anam gu dëppoo ak li jamono laaj |
jooyleena jooy buur salum miy dem , te du delseeti , |
samay doom maa ngi leen di bind ndax baalees na leen seeni bàkkaar ci turu kirist |
atum 1789 mooy at mi fipp gi ame woon nekkutoon at mu ya ko jiitu woon tane ci wàllug koom waaye la waraloon fipp ga am ca mooy ñàkk a taw ga mu àndaloon ga juroon bekkoor ba ak xiif ba nit ñi mujjoon di ñu ñàkk aw ñam jafe dundiin wi naqari |
man nañu gis tur wi ci mc 10 25 12 24 27 mk 3 22 lu 11 15 18 19 |
am na ñaari tàkk bu taklamakaan ak bu gobi |
xeet ya yépp danoo jaxasoo ca yoonu imbraatoor gu ghana ca dëkk bi nu tuddé jolof |
sool daldi ragal daawuda , ndax booba xam na ne aji sax jee and ak daawuda , deddu ko . ba loolu amee mu jele ko fi wetam , fal ko njiitu kurelu junniy xarekat , muy xareji , di delsi , jiite gangoor ga . daawuda baaxle ca yoonam yepp , aji sax ji and ak moom . ba sool gisee daawuda antule lool , |
kenn du daax mbubb mu màggat ak sekkit wu bees |
ci jemmam degg , xetu web , day nekk ab mbooloom ay mbind , ay nataal aki riir , ci gattal lepp lu gisu walla deggu . |
way naxtu yi taal nanu ay pono , soongu ay biis aki xeer , tax teewaayu takk der yiy jefandikoo ay mbeli gelemal ngir tas leen , la yeenekaay yi siiwal alxamis . |
reew ma . danoo dem ba agg xuru eskol , ba gis reew ma , doora delsi , di yoqiloo banni israyil , ngir nu bana duggi ca reew , ma leen aji sax ji joxoon . sanjum aji sax ji tang na besub keroog , ba mu gin , ne kenn du gis mukk reew ma ma ginaloon ibraayma ak isaaxa ak yanqooba , ci goor ni joge misra te am naar fukki at , jem kaw , gannaaw matalunu koolute ci man . xanaa kaleb doomu yefune , keneseen bi , ak yosuwe doomu nuun , ndax noo matal koolute ci aji sax ji . ba loolu amee sanjum aji sax ji takkal israyil , mu werloo leen ca mandi ma diiru neent fukki at , ba mboolem maas googa defoon lu aji sax ji naawlu , nepp jeex takk . yeen nag defuleen lu moy jog wuutu seeni baay , njurum bakkaarkat yi ngeen doon , di xamb sanjum aji sax , ji takkal banni israyil ? su ngeen ko deddoo it , day dellu wacc banni israyil ci mandi mi rekk , ngeen daldi sanklu mii mbooloo mepp . |
bu boobaa nit niy xem ndax tiitaange , bu nuy xalaat musiba , yi nar a wacc ci addina , ndaxte dees na yengal kattani asamaan . |
ak tam ngir xeeg gut ar gi leen askani yii barab doon xeex |
mu yettlu nag ay serub ci kaw miiri naari neegi ker gi , yettaale garabi ron ak i toor toor yu focci , werale . xoob na itam deru tabax bi wurus , ci neegu biir bi ak ci biti . |
waaye yonnant bi degmalsi leen ci mbooloom xare mu mag , gaw xaybar , jullit na songoo fa ak yahood ya cib xare , yonnant bi dumaa leen fa , nu wommatu , yeneen waaha yi ko jege woon te nekkoon ci loxol yahood yi topp ci , niki fadk ak timaa . |
nanu xuus nag leegi ci gaal gi , ni nu ko dige woon ci kow . |
ndax kat loolu man naa waral yàlla di muri mbalaan mi mu muuroon ci say ñaawtéef |
kon nanu bàyyee tegante tooñ waaye nu fas yéenee moytu lépp lu nekk fiir guy yóbbe sunu moroom bàkkaar |
jem kanam gii xam xam jem kanam tay ci reewi orob gu sowwu gi , am na ay balluwaay yu wuute , yi ci epp solo di tuxal xam xami jullit ni ak firi leen ci lakki orob yi te jarinu ci . |
amal yeete bu yaatu , ba nepp xam lan moo di doyadig rono ni bokk ci mbootaay gi nar nanoo amal yeete bu yaatu , ba nepp xam lan moo di doyadig rono , ngir men a fagaru , ni mu ware . |
di benn ñetti afrig walla benn ñenti asi walla aamerig |
mbooloo mu bare dajaloo ca moom , ba tax mu dugg cig gaal , toog mbooloo mepp taxaw ca tefes ga . |
ci la bind ab yebbi ci yoonalug direction marcel griaule ca daara ju kawe ju paris , mu wax fa ne isipt gu yagg ga , ay waa afrig yu nuul a fa dekkoon , ni it lakk ak caaday waa isipt noo tas ci sowwu afrig . |
sama doom , deggal samay wax , fonk samay santaane . |
yal nanu weye walum ndox , te suuf sa nu seddoo alku , |
ndaxte saraxalekat bu mag bi dafay yobbu deretu mala yi ca berab bu sell baa sell ni sarax ngir dindi bakkaar yi , waaye yapp wi dees na ko lakk ca gannaaw dal ba . |
neel askanu kore wu goor , di woyu saboor . |
am asamaan ay soobal boppam i waame ? du yaw la aji sax ji sunu yalla ? |
kon nag képp ku mu mana doon yaw miy àtte sa moroom ak ñaaw njort amuloo aw lay ndaxte àtte sa moroom daan sa bopp la |
nikodem bokkoon na ca farisen ya fa nekkoon |
aji sax jeey dooleel mbooloom . mooy laq , di musal buur bi mu fal . ngalla musalal sa mbooloo , barkeelal sa non nii , |
naanal ci sa mbalkam bopp , ndox ma balle sa teenu bopp . |
fi ñuy nekk di màng di nekk ci jugu jugu yi bu ñu nekkoon ci seen këri bopp ya nekk ca seen néeg yu baax ya kon loolu du leen dal waaye ci gétt gi lañuy fanaan ba daanaka feebar yu bari ci lay joge |
xeltukat bu weddi bu siw ba nii la saraa laaj boobu xamees na bu baax ne diine lu baax ci bakan la |
ana kuy dund ba faww , ba doo gis bammeel ? |
maa ngii dey di xabtal fi kaw babilon , |
noonu la mel it ci kepp ku juddoo ci xelum yalla . |
sang bi def naa li nga ma sant waaye bérab bi feesul |
bi mu newee , nu yobbu ko ca neeg bu kawe ba . |
ci noonu mu yabal ay mool yoy ci seen tukkiy wuññi yooyu àggoon nanu ba ca duni kanaari ya ak madira ak osoras ci mambulaanug atlas atum 1402 g naka noonu ñu wëy ci seen tukki yooyu ba agsi senegaal atum 1445 g ginaaw bi henri deewee tam teewul seen tukki yooyu wëyoon ba ci sottiwaayu dexug kongoo gi ak niijer |
newuma ngir dindi leen , waaye ngir nu am ci man . |
ibraayma guddoon na fan , ba maggat lool , te aji sax ji barkeel ko ci lepp . |
noonu malaaka ma daldi dawal sàrtam ci àddina dagg reseñ yi sànni léen ci biir segalukaay bu réy bu merum yàlla |
ci nit ñi kon mbooloo mi dal ci sunu kaw ndaxte ñépp teg nañu yaxya ab yonent |
maryaama laaj malaaka ma ne ko naka la loolu man a ame ? |
nguur yooyu nag amuñu woon doole lu dul ci ñaari xarnu yii bu fukk ak ñatt ak bu fukk ak ñeent maanaam ci jamonoy imbraatóor yu ñuul yi yu nit ku ñuul yi gu gana mali ak songaay |
bala mu topp ci yeesu nekkoon na taalibe yaxya . |
ci bu jekk tur boobu turu foontoo la woon . |
ndaxte fi mu ne ñaawteef gaa ngi jax jaxi xaat ci kumpa waaye ki ko téye mi ngi fi ba tey |
mu ngoog ! maaka xam li ngeen foog , te di ma ko fexee fitnaale ! |
ngalla yaw dëkk bu mag bi nga xam ne ci la boroom gaal yépp woomle ndax sa barele ci waxtu nga gental |
coppite yi neel jefandikukat jimeowan wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii . |
ku naan ci ndoxum teen bii balaa yàgg mu maraat waaye ndox mi may joxe ku ci naan du marati mukk ndaxte day nekk ci moom bëtu ndox buy ball di joxe dund gu dul jeex |
gannaaw loolu loxol aji sax ji da maa dikkal . aji sax ji yobboo ma noowam , ba teg ma ca digg joor ga , fekk joor ga fees dell ak i yax . mu werloo maa werloo ca biir yax ya , ndeke yax yaa nga bare lool te |
ndaxte waccewuma ci asamaan ngir def sama begg begg , waaye damay matal begg beggu ki ma yonni . |
moom kay li ko sooboon mooy almaañ des di nguur gu nu dogat ngir mu nekk moom fraans di reew mi am kilifteef ci sowwub tugal bi |
looloo tax ma ne ci seeni bàkkaar ngeen di dee |
gëstu leen loolu ci jannatul muriidi teere bi sunu sëriñ xaliifatur rasiid def |
ey aji sax ji , musal ma , yaa ko dige . |
noonu ba ma ko menatul a dekku , yonnee naa , ngir xam fu seen ngem tollu , ngir ragal seytaane fiir leen , ba sunu naq neen . |
jimbulangu xam xam bu abu bakr al razi bu al kindi ci daanaka 270 téere |
yaw laay sarxalal saraxu cant , te turu aji sax ji laay tudd . |
dajaleleen xeet yi fi kaw babilon , te xabtal fi kawam reew yii |
noonu mu dellusi ci taalibe yi , fekk nuy nelaw . |
ca bésu waajal la woon ba yawut ya doon waajal bésub noflaay ba te bàmmeel ba jege woon na |
adreesu email bii aarees na ko ci robooy spamkat , faww nga dekkil javascript ngir gis ko . |