text
stringlengths
38
33.7k
li muy tekki mooy limu nit ni jappale ci dalu xam xam bu dul sumbi dali waxtaan wu dul angale ci fan yi weesu .
aji sax jee wacc ni ngeen yaakaar , ba dungeen baaxlee ci noom .
dafa amoon ñaari nit ñu dem ca kër yàlla ga di aan
gannaaw gi seytaane dafay ñëw këf kàddu gi ñu def ci xolam ngir mu baña gëm te yàlla musal ko
saraxeleen li nekk ci biir te seen lepp dina sell .
danoo genn ci dundu yalla , ndax umple gi nu am ci moom , ak li nu ko tejal seen xol .
mu neeti suuf si dafa wendeelu , maanaam roo te wendeeloom googu nag tax na ba day yor doxiin walla yengu yengu gu roo , mbaa guy wendeelu .
lu aji sax ji seede degg la , day xelal ku xeluwul .
moytu ko bu baax ndaxte bëre na ak sunuy wax ba tàyyi
coppite yi neel jefandikukat nobelbot wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
dal luwaay bunt , bi ki ci jal biy jaare duggsi , fi lay jaare genn .
bi nu joowee lu war a tollook juroom benni kilomet , nu seen yeesu , muy dox ci kaw dex gi , jem ci noom , nu daldi tiit .
bokkoon na it ci li ko ko taxoon a def jeem a gëramloo katoligi fraans yi nga xam ne danoo tàmbli woon a mer ci neewal gi nuy neewal doole nguurug paab gi ci itaali te otris a ko daan jàppleek a dëgëral
duma ko xool ci li sama yëgukaay jàpp waaye ma ngi aju ci li sama xel jëli ndax samay yëgukaay yu biir ak yu biti ak sama xel li ñuy jàpp woorul
jabbir leeraloon lu bari ci way toggale yu simi yi nu xamutoon bu njekk , niki aji wex ju nitrik , ruug nasaard , botaas , soda al kawiya ak aji wex ju asotik ak yeneen .
teere woy yi teere woy yi teere la bu emb taalif yu bindkat ak xaralakat yu mag ci lakki almaa taalif .
samp nañu miiru dëkk ba ci fukki fondamaa ak ñaar yu ñu bind turi fukki ndawi gàtt ba ak ñaar
maryaama mooy jigéen jiy sottiji latkoloñ ci tànki boroom bi fompe ko kawaram
ndajem bandonj nag mooy ndajem adduna mi njëkk a boole ndawi ay reewi asi ak yu afrig yu temb
dees na ko gen a yaatal ci waxtu yiy new .
wax ju bare , caaxaani neen mook gent yu baree yem .
muy keppaaral rabu all , di taggal njanaaw ,
bañuma ñu yeew ma rekk waaye nangu naa sax ñu rey ma ci yerusalem ngir turu yeesu boroom bi
coppite yi neel wall banglaades wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii .
mbaa suuf su mu donn , amu ci lenn lu mu aayalal aji sax ji te nu san koo jaay mbaa mu di ko jotaat . ba tey du kenn nit ku nu aayalal bakkanam aji sax ji , mu wara sanku , ba noppi nu di ko jotaat . dees koy rey rekk .
loolu dina efaase sa profil doo ko men a defaraat .
kaddu yu njekk yi tukkee ci makki sall yeen wa senegaal , goor ak jiggeen , mag ak ndaw , sama askan sope .
réewu taax mu kawlax mooy péeyu diiwaan bi te ëpp ci solo it
tubap yi tamit ak canc gi , def neen ni , diiney afrig bobu mu wani bu bari .
moo tax loxoom may ko ndam , te njekkam la sukkandikoo .
dégg nanu ne am na ay nit ñu bawoo ci nun ñu di leen lëjal ak seeni wax di jaxase seeni xol te fekk sukkandikuwuñu ci lenn ndigal lu jóge ci nun
sancoon na tuubaa ci 1887 ngir gën a man a wéetal yàlla ginaaw bi nit ñi baree fa moom ca daaru salaam ga ca anéeri mbàkke gi ñu la waxoon leegi nga xam ne raj rajloo ba teewoon na koo nekk ca na mu ko soxlaa ba man a def li mu bëgg cig jaamu ak yar ba mu demee tuubaa t loola toppati ko fa moo waraloon mu faroon sanc mbàkke baari ca jolof fa la juge dem géej boo ci bëggee xóotal yëral sancamjolof ak li ko waraloon
goor niy doomi barsilay mu galadd nag , nanga leen baaxe , te nuy bokk ak yaw ndab , ndax kat taxawu woon nanu ma , ba may daw absalom sa doomu baay .
ci biir loolu ay xeremkat dikk , di boole yawut ya . nu wax buur nabukodonosor , ne ko buur , guddal u fan . buur sang bi , xam nga yaa joxe ndigal ne kepp ku degg bufta beek toxoro geek xalam geek riiti geek kooraa
sëñ bi neeti ko waaye wax jii am na ñu ko tax a jug ñooy ñi ci am ag ñam akug dëggal waa ju juge fee rekk nag li war mooy mu nangu ko mbaa mu noppi ngir bañ a loru
sooni walla sunu benn dekk la ca isipt , nu ko gena ranne ci tur wi di aswan .
yaay , balaa daraa xew kat , def leen ndank , ma yer ko .
at mooma mu woore sarsaara koor ga muy barab bu nu xam fa ñoñam nit ñi sottiku fa ak ñuy jële ci moom rawati na ci banii daymaan ak seen kilifa ya doomi baydah yi abdul laahi aki mbokkam ci loolu ku baax kaa ngi naan
ca la jële ñaar téeméeri looco ak dund daal di yonnee ngir ñu dugg ci mbàmbulaan gi waaye kenn a ca dellu si nettali ni dañoo dajeek ab duus bu soxor ci ndox mi mu mëdd leen
ñoom nag ñi ngi leen taxawal ci xarnub fukk ak ñeent g j ay way gàddaay yu bàyyikoo ca imbratóor gu mali gaa leen taxawaloon
waaye taskati xibaar yu bare biral nanu ne , diggante isaa sall ak serin mustafaa si xaw naa xajam jamono yii . serin mustafaa si , nag , mooy kilifay daayira ji , rax ci dolli am na nu naan mooy njiitu pur . waaye , isaa sall moom weddi na loolu ba tedd ci naaj wi . nee na tey la seen diggante gen a ritax te sax , li serin biy jeflanteek moom , du ko jeflanteek keneen .
ey aji sax ji , mayal buur mu daan , te bes bu nu ko naane , mu nangul nu .
waaye lu may waxati ? aji sax jee ma wax ,
làkk moo y cëslaayu ag yewwute bu nu ko waxee dées na ko man a dëggal rawati na ku jàng jii jamono jàngat ko xam la leen seen yu suufe ya ñu xeeb jariñoon ñu ko y woowe ci francais dialecte ba ñu leen jëlee def leen ay làkk yu xeet yu réew yu xam xam yu ñu fonk yu ñu fas yéene e doxale seenu g dund sës ci seenu g dox sanni ca àll ba yeneen ya doon dox seen diggante ak xam xam xam ak yewwute mu y làkk wu latin wi nekkoon di lu ñu neew xamoon la gën a rëy ca mbooloo ma réere woon ko te réere gi taxoon ñu reeroon te yewwoodiku
missing argument in negation pseudo class s .
dencal say leeral fu woor ci jekkali kaaraange ak sutura bu firefox bu android .
loolu nag taxoon na ba reewi orob yi tàmbli woon a xalaat ci seen ëlëg ginaaw bi nu mujjee di reew yu ñàkk solo bu nu leen tollalee ak yile ñaari reew
doom yu goor yi rasel , soxnas yanqooba , am nag noo di yuusufa ak benamin . yuusufa itam am manase ak efrayim ca reewum misra , seen yaay di asnat doomu potifera , may njiitu diine ca dekk ba nu naan on . doomi benamin yu goor noo di bela ak beker ak asbel ak gera ak naaman ak eyi ak ros ak muppim ak uppim ak ard . goor noonoo xeetoo ci rasel , te askanoo ci yanqooba , nepp di fukki bakkan ak neent .
ñu amale ko nag ci genn saxal gu juge ca mbootaayu xeet ga ñu sosoon atum 1945 ngir wuutu fi kureelug xeet yi
te ginaaw piemonte it reew mu nekk ci wetu fraans la loolu taxoon na mu bëgg mu nekk reew moo xam ne yoonu otris du ca nekk
ci kaw loolu yeesu jog , daldi gedd ngelaw li , ne dex gi noppil te dal !
yeen xutbakat yi ak farisen yi , naafeq yi , dingeen torox ! ndaxte yeena ngi tej nguuru yalla aji kawe ji ci kanamu nit ni yeen dungeen ci dugg , te dungeen bayyi ku ci begg a dugg , mu dugg ci . yeen xutbakat yi ak farisen yi , naafeq yi , dingeen torox !
baadoolo yi ne xas tey ci reew mi , ngeen nar leena dedduloo seeni sas !
njumte bu kenn xamul taxawal doxub wideyoo bi .
sooy tekki xetu web ci biir xet wi ci boppam , soxlaatoo xam ndax baat bi ag jef la walla tur .
xarafoon naa ca ayu bés ga bokk ci bànni israyil ci giiru beñamin di ebrë ci deret ak ci meen
ci noonu xam xamu melosuuf tamblee jem kanam ci tugal .
waaye su ngeen baalul ñi leen tooñ seen baay it du leen baal seeni tooñ
! te noonu da noo am peterool , yeneen reew yepp ci reew yi gena ndool , gena lott ci addina lanu bokk .
kaddu yii la aji sax ji wax ci mbirum israyil ak ci mbirum yudaa .
ci séeréer yi askan yi ñu faloon ñoo ñu sant juuf ngom caw
am miliyo ciy way dekk senegaal la ngi tedd ci km kaare , sun ko meengale ak dekkandoom yii di mali ak gannaar , di nan gis ne reew mu tuuti la .
xaaral rekk , ma natt banneex , nam lu neex ba xam .
di yool ku nekk jefinam , la yellook anam .
yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax
ngir dakkal toon gi , jeexal moy gi , jotu naawteef , saxal njubte ba faww , matal peenum yonent , ba delloo berab bu sella sell ag sellngaam . nanga xam kon xell ne li ko dale keroog ba nuy siiwtaane dogal ba jem ci leqli yerusalem , tabaxaat ko , ba keroog njiit li nu fal di feen , juroom naari appi juroom naar la . te ci juroom benn fukk ak naar ci appi juroom naar lanuy tabaxaat penc ak kamb gu nu aare dekk bi . waaye jamono yu metti lay doon . bu juroom benn fukk yeek naar ciy appi juroom naar weesoo , dees na boom ku nu fal , te kenn du and ak moom . gannaaw loolu kilifa dina new , and ak gangooram , yaqte dekk beek jaamookaay bi . waaye kilifa googu lu mel ni mbenn a koy mujje . dogal nanu ne yaqte gi dina wey ba keroog xare biy jeex . dina feddli kollere diggam ak nu bare ci benn appu juroom naar , te ci diggu appu juroom naar ba lay dakkal sarax yi nuy rendi ak yeneeni sarax . ci genn wetu
moor xecc bunt beek doole ci loxo soxna si .
góornamaab doxaliin bi lii mi ngi ko dénkoon napoleon ci noonu mu jug mooki gaayam géeju ci atum 1798 tukkee ca waaxub toulon mbooloom xare mi àndoon ak moom àggoon na ci ñeenti teemeeri gaal yu sëfoon ñaar fukki junneek juroom ñatti soldaar bokkoon na ci tam teemeer ak juroom ñaar fukk ak juroomi boroom xam xam yu waa faraas
yewwuteg endustri gi bayyi na fi ay jeexiit yu rey ci wallug koom , ci biir orob ak biteem .
besub keroog ma woo sama jaam bi , elyakim doomu ilkiya ,
yeen yeena reylu noni aji sax ji ! mbooloo maa nga sam aaroona ak musaa . ci biir loolu , nu ne gees xaymab ndaje ma , gisunu lu moy niir wa muur ko , leerug aji sax ji feen .
dencukaay bu sa jemm emb na a data l n name user js link ara user . js a , te amaale itam ay tanneef yu brand short name sosul .
te boroom bi moo sas ku nekk liggeeyam .
waaye ma daal di jis ne man naa wàcc ci biir xel bu ma man atul a doxal cawarte gi
mu jem ci njiital jangkat yi , and ak xalam gu nuy wax gitiit , neel askanu kore wu goor .
benn dëkk ci réewu itali la woon bu amoon ja bu mag
lii lepp nag bokk na ci li waral yewwuteg endustri gi man a am ci tugal rawati na ci britani
mbambulaan gu bej saalum gi mooy mbalkaam ndox mi ne ci li wer dottub bej saalum bi .
baal naa la sa bor bepp , ndaxte tinu nga ma .
na deddu mbon , jefe mbaax , sakku jamm , saxoo ko .
ci baat yooyu la doon misaale ni mu wara faatoo
kon nag bokk yi , yeen ni boroom bi begg , menunu lu dul sax ci sant yalla ci li mu leen tann ca njalbeen ga , ngir musal leen , mu sedde leen boppam jaarale ko ci jefu xel mu sell mi ak seen gem degg gi .
ci lu jëkk réccu naa ko ndaxte gis naa ne bataaxal boobu teg na leen tiis doonte sax ci diir bu néew
taalibe yi xamaguñu woon mbind mi doon wone ne yeesu dafa wara dekki
ci nii daal la xew xew yi toppantee woon di nëxal nag sellug seqoo gi amoon ci diggante angalteer aki sancoom loolu tam gën a yaatal paxum reeroo mi nekkoon seen diggante
naanu ku naroona sanku di ma dal , may tooyal xolu jetun .
bi yeesu demee ba ca kanam , mu gis saag doomu sebede , ak yowaana , mi mu bokkal ndey ak baay , nu nekk ci gaal gi , di defar seeni mbaal .
ci 48 g k erodd bu jóge calkis chalcis magu baayam dee na itam
may nanu ko magu baayam , erodd bu joge calkis chalcis , bi berenis amee at .
nu xam ne lim wax lu deggu ci moom la , nu jeggal ko noppi cim mbiram .
maggal gi genn xumbeel la guy jemmal at mu ne fattalikug gaddaayal gi nu defoon seex ahmadu bamba ca , ci loxol kilifteef gu canc gi l autorite coloniale .
ñi daan jëf lu baax dinañu dekki dund ba fàww waaye ñi daan jëf lu bon dinañu dekki ñu daan léen
bi buur yi ak seen dag yi gisee li nu gis te ñoom boroomi ngànnaay lanu ñu daa dund ci seen ngànnaay rekk danu daan song ku leen daa jéem a të duma ko nangu alalam ray ko mbaa ñu njaf ko jàpp ko jaam loolu nag di woon aada ju yàggoon ci ñoom ju nu daa donnante waaye loolu téewul ñu amoon jàmm ak lenn ci boroom néeg yu mag yi daawunu leen boole ci seen jëf jooju daawunu ci boole it ñi daa aaru ci seen kaaraange niki néegub sëñ bi
waaye dañoo wara def biiñ bu bees ci mbuus yu bees
yeen nepp soreleen ma , defkati lu bon yi !
mooy tomb bi nga xam ne ci la mucc nekk ci adduna ak ci allaaxira , ci la texe nekk ci adduna ak ci allaaxira , ci la laq ngeremel sunu boroom nekk ci adduna ak ci allaaxira .
fekk fab na fetal gi ag béjjën ub dem bi daldi jël kaartus yi def ci posam daldi tëbal
yi ngeen taamu woona daje , di bokkaale .
ku magg , ku kawe ki , ki makkaanam sax dakk
lepp lu nu sakk , ci moom lanu ko jaarale , ci moom lanu ko jeme .