text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
teewul nuy andandoo , diy gangoor sindax , manees na koo eb , teewul ma nga biir ker buur . |
dañuy xool te duñu gis di déglu waaye duñu dégg te duñu xam moo tax ma di léen wax ciy léeb |
ba loolu amee elifas waa teman ba , ak bildadd waa suwa , ak cofar waa naama daldi dem , def la leen aji sax ji sant . aji sax ji seet ci ayooba . gannaaw ba ayooba naanalee xaritam ya , aji sax ji tijji wersegu ayooba . aji sax ji ful na naari yoon mboolem alalu ayooba . ba loolu amee mboolemi bokkam , goor ak jigeen , ak mboolemi xameem ya woon , dikk bokk ak moom bernde ca keram . nu defal ko , mas sawu ko ci bepp coono bu ko aji sax ji tegoon . ku ci nekk jox ko dogu xaalis ak jaarob wurus . aji sax ji nag barkeel mujug ayooba lu raw ndoorteem . mu am fukki junniy gatt ak neent , ak juroom benni junniy gileem , ak junniy lekkey |
noonu nu yonni ci moom seeni taalibe ak ni far ak buur bi erodd ne ko kilifa gi , xam nanu ne ku woor nga , te ragaloo kenn , ndaxte seetuloo jemmi nit , waaye dangay xamle yoonu yalla ci bu woor . |
la am nag mooy ne buuru brusiya bi dafa bañ a jël ndëpp li ndax xam ne otris ak rusi ànduñu woon ci bennoog almaañ googu te manoon nanoo xëy di duggati ci seeni mbir ngir loolu |
ñaari nguur yii nag ba xarnub fukk ak juroom ñeent g j dañoo bennoo woon |
ca njolloor , buur bi , gis naa ca yoon wa leer gu joge asamaan ne rayy , ba raw leeru jant , melax ba emb ma , man ak ni ma andal . |
xam xam yi màcc ci wàllu xel yi daawunu xamle lu dog ci nekkin bérëb boobu ak ci taxawaayu yëg yëgu biir yaram yooyu |
te xanjar , ay doj lees di xelli , ba am ko . |
garab la itam goo xam gu yomb ay mbir la , ndax daanak lajul ndox , fepp la men a sax . |
noonu yeesu laaj leen ci lan ngeen di werante ak noom ? |
nii , kuy aji gem , na la ni naane , ba naan jotee . |
te yalla fal na ma ndaw ak jangalekat , ngir may yegle xebaar bi |
kon nag bi yallay wax ci kollere gu bees gi , dafa fekk mu maggatal gu jekk ga . |
ñeent yu jëkk yi maanaam macë màrk luug ak yowaana ñooy xamle dundug almasi bi maanaam juddoom ci maryaama njàngleem mbëggeelam ci nit deeyam ni sarax ngir gàddu bàkkaari àddina ak ndekkiteem |
ndaw lu joxee may daan , la buuru lamb ji yekini saxaloon ca bamu daanee tayson mi jiite ekiri bul faale ci awril ci netteelu yoonam . |
jeriji peppum lors ca dagga ja . kon nag sangul , solu ba jekk , xeenu , dem ca dagga ja . bu ko feenu nag te lekkul , ba naan ba noppi . bu demee ba tedd , nanga nemmiku fa mu tedd . su ko defee nga agg ba foofa , muri fa feeteek tank ya , tedd . moom dina la xamal li nga wara def . mu ne ko baax na , loolu rekk laay def . |
sarayi leegi moo di saaratao . dinaa ko barkeel , may la ak moom doom ju goor dinaa ko barkeel moos , ba mu jaboote xeet yu bare , te ay buuri xeet sax dinanu soqikoo ci moom . |
daldi waat ci kiy dund ba faww , ki sakk asamaan ak suuf ak geej ak li ci nekk lepp mu ne negandiku wees na , |
xale yi gemewunu ko woon . lu tol ni lekool di tej ci diggu at mi , du muur mburaake la . nu kontaan , naan ndax yalla nu nopalu . waaye diir bu gatt moo ci tegu , nu tambalee laaj seen i way jur kan lanuy dellu lekool . li am moo di ne danoo dem ba namm seen i xarit , begg a fo ak noom mbaa xey rekk gaddu seen saak , sakkuji xam xam , jang lu bees . rax ci dolli , tey , fi mbas mi tollu , kenn xamul ndax lekool dina ubbiwaat ren am deet . |
xam ngeen ne yalla manu noo taajal ndab ci mandi mi ! door naw doj , moos , ndox ma fettax , saboor wal ma baawaan , waaye aw nam nag ? daa mana leel mbooloo mii aw yapp ? |
waa siri na ca mesopotami ak waa siri na ca soba te ba nu ca bayyikoo , |
lim bii di toftal dafa boole mbooleem réew aki suuf yi fa nekk |
ci alaskaa lanu gise jeexiti nit ki fa njekk a teew , ci weti at nj . |
ci kaw loolu piyeer jel kaddu gi ne ko sang bi , bu dee yaw , sant ma , ma dox ci kaw ndox mi , new ci yaw . |
seen tiis wi jóge ci yàlla gisleen nag li mu jur |
li sabab sanc lu bari la te lënkaloo ñu tudd ci yi ci ëpp solo yii |
kon ni ma ame woon kóolute googu naroon naa jëkka jaar ci yéen ngir ganesi leen ñaari yoon |
ku wax ne yaa ngi ci leer tey bañ sa mbokk yaa ngi ci lëndëm ba tey |
ndaje maa nga am ci bis bi njekk ci pencoom netti fan ya njewrinu ma yor bitim reew amal ca wasington te dajale ca ay ndawi afrig ay njiitu kurelu siwil ak yu boppu yi . |
aji sax jee di yalla , di nu leeral . abbleen car yi , maggale , |
panamaa republik bu panamaa réewu aamerig |
besalel nag defare gaalu kollere gi denku seng , guddaay bi di naari xasab ak genn wall , yaatuwaay bi di xasab ak genn wall , taxawaay bi di xasab ak genn wall . mu xoob ko wurusu ngalam biir ak biti , |
mel ne ku ñéer cafka ga far càkku ca teel |
boo bàyyiwul di jaar ci yoon wu lëndëm woowu xaaju guddi dinga mos dajeek njuuma |
bàyyil naa leen fi royukaay ngir ngeen di jëf nii ma jëfeek yéen |
te defuñu ko sarxalkat jaarale ko ci yoonu ndono waaye fal nañu ko ci dooley dund gu amul àpp |
dawal ni kewel gu recc ub rebb , ne ferr ni picc mu raw ab fiirkat . |
bi nu ko laajee , mu new ci yeen , nangu na , te rax ca dolli cawarteem tollu na , ba nu man a wax ne , ci coobarey boppam la joge , jem ci yeen . |
dawleen it yu jekkadee , ni wax ju naaw mbaa waxi caaxaan ak kaf yu bon , te ngeen sax ci sant yalla . |
àññ yem ci benn soxna moom boppam te maandu |
bu ko bombee ba deret ja genn mu wax allaahu akbar , bu teggee loxoom mu wax rabbanaa taqabal minnaa innaka anta as samii ul al aliim s l . |
mu woo gaayi yàlla ya ak jigéen ña won léen ko muy dund |
noonu mbooloo mu mag mi di ko deglu ak banneex . |
ni ngi seenu sampug njiitu lu bees li ci awril . |
semaya doomu asub bokk na ca asub , asrikam ay baayam asrikam , asabya di baayam asabya , buuni di baayam ak itam sabtay ak yosabadd , di kilifay leween yu sasoo liggeeyu ker yalla ga , fa feete biti ak matana doomu mika . mika , sabdi di baayam sabdi , asaf di baayam matana moomii moo doon debbekat ba doon jiite jangi cant ci biir julli . bagbukiya , mbokkum matana , bokk na ca , di kilifa gi topp ci moom ak abda doomu samwa . samwa , galal ay baayam . galal , yedutun ay baayam . mboolem leween na sanci woon ca dekk bu sell ba naar teemeer lanu ak juroom nett fukk ak neent . |
rasel ak leya ne ko ndax amati nanu benn cer walla ndono sunu ker baay ? doonunu lu moy ay doxandeem ci moom de ! nde da noo jaay , lekk |
juróomi picci ramatu ndax duñu ko jaay ci ñaari dërëm |
mu daaneel taabali weccikatu xaalis ya ak tooguy jaaykati pitax ya , |
du yéen yéena ma tànn waaye man maa leen tànn sas leen ngeen dem meññ meññeef gu sax ngir baay bi def lu ngeen ko ñaan ci sama tur |
looloo waral it ñi dee sax ñu jottali léen xibaaru jàmm bi ngir ñu dunde yàlla ci seen xel doonte sax nit ñaa ngi léen daan fitnaal ci àddina |
ndax kat loolu duy teggiin ngir ne am na lu ci nekk lu man a waral ag yeddeel kuy nelaw man ngaa ngelawal te doo ko yëg |
li moye tax ca jamono bobu teug yi ay buur gu mak lani nekkoon . |
v . tur la wu nuy wooye yerusalem . man naa tekki itam taalub sarxalukaay ba woon ca ker yalla ga . |
nde dees na japp gettu aji sax ji , yobbu . |
nu daldi tiit , foog ne danoo gis njuuma . |
yaw , sama yalla , wallu ma . ey boroom bi , baaxe ma yaw laay yendoo woo wall . |
ndaxte meluleen ni banni israyil noom ni jege woon tund wu nu man a laal , wu doon takk jeppit te and ak xiin ak lendem ak ngelaw . |
xaralaymbëj mooy xeetu xam xam giy gëstu lépp lu jëm ci wàllug mbëj ay jëfandikuwiinam ak ay seddalewiinam bu njëkk dañoo foogoon ne mbëj ag wal la rekk guy dem gu man a nekk gu baax walla gu bon |
becceg yooyu kurel giy saytu dund ak lekkin ak toppatoo xale te banqaasoo ci njawrinu wer , nu tudde ko danse moo koy amal , jagleel ko xale yi am diggante weer ba at . |
ndaxte ku manta yor njabootam naka lay mana yore njabootu yàlla |
ni garab yu meññul ci jamonoy meññeef te buddeeku dee ba wow koNN |
jafe jafe yi aju ci wall gii maneesu ko o takk , dees leen di lim ci y teemeer , danu ne woon nanu ci indi yenn rekk . |
tata dina tukkee diiwaanu efrayim , nguur foqe dekk ba nuy wooye damaas , |
sunu giiru dund nga di nu mere , sunuy fan jeex ni noo guy naaw . |
te it yeen niy dekku coono , mu boole leen ak nun , tabbal nu ci noflaay , bes bu sunu boroom yeesu kirist jogee asamaan , feen fi . |
mun na meram , munati , te toppul xolam , |
balma ca sa ma bind , ak toppando gi , dina geuneu goorgolu , man pulaar la , france lay juddu li moye tax francais lay geuneu xam , waye lakk wolof nex na ma lol , damay jang bind sasounek . |
ci wàllu xibaarfeppal la ñu koy jëfandikoo |
njaniiw ak biir suuf , aji sax ji di gis , xolu doom aadama waxi noppi . |
kollere fecciku na , xeebees na ay seede , |
dingeen torox yéen waa korasin ak waa betsayda ndaxte kéemaan yi ma def ci yéen bu ñu léen defoon ci dëkku tir walla ci dëkku sidon kon réccu nañu bu yàgg xëppoo dóom sol saaku |
yéen ñi dëkk room ñépp yéen ñi yàlla bëgg te woo leen ngeen nekk gaayam yu sell na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm |
dooley gnome mooy askanam gu rey . daanaka ku ne , muy ku man walla ku manul bindi teriin , man ngaa duggal sa loxo ci gnome ngir genal ko . |
bi loolu amee boroom réew ma jàng bataaxal ba laaj ci ban diiwaan la pool dëkk |
ci kaw loolu ñu daldi ñaan yeesu mu sore seen réew |
su ngeen amee junniy njiit yu leen di samm ci kirist , ba tey benn baay rekk ngeen am , ndaxte maa leen yegal xebaar bu baax bi , ba jur leen ci kirist . |
xam ngeen ne , bi ngeen xamagul woon yalla , xerem , yi menul a wax , noo leen jiitaloon , di leen wommat . |
baay bi begg na ma , ndaxte damay joxe sama bakkan ngir jelaat ko . |
ak lu ci men a am , laale gi dina tar samwie biy new . |
nori butao fi , loolu menna indil joffe joffe ndaxte tere nori ko naka yoon . ndax nga bogge teg s ngir butao dugge dugge ? |
damay xoole guddi gepp , di jangat sa kaddu . |
ngeneeli tabaski ci lislaam lu am solo la , kenn manu koo takk , yonent jammi yalla ci moom bi xamle nani toq dereet wiy njekk a genn yalla di na ci jeggale mboolem bakkaar yees masa def , nii la dikke ci sunna ci nettalib aysa ngeremul yalla ci moom . |
men nanoo dimbali way jefandikoo yi ci teqaleyinu baat yi . |
te dekkal na nu ak kirist yeesu , deel nu ak moom ca berab yu kawe ya . |
jottalil ma sama salaat ak sama salaam ci yonnent bi , moom ak ay gaayam , aki sahaabam , aki soxnaam maa ngi la koy dagaan yaw yalla . |
gannaaw loolu yeesu duggoon na kapernawum |
du y caaxaan la nit ka y xalaate ca la war a waxe ci maanaa li nga y xalaat ci sa biir dënn sa biir xel mu y jeqarbiku ci sa y yëg yëg jarul fireeti ci weneen làkk wu dul wi ko xalaat ngir déggal ko ku nu jàkkaarlool ki bu ko fekkee mu ko y man a dégg ci wi ñu ko xalaate loolu li mu y jur mooy yàq waxtu te mu y lu gànjaru |
garabi basan ak karmel yengu , di ruus . aji sax ji nee xaaral rekk ma jog , xaaral rekk ma ne nokket , |
xaalis bi koy defar tollu na ci naari teemeer ak fanweer ak naari milyo ciy dolaar , mu dikk teemeer ak fukk ak juroomi milyaar ciy cfa . |
xel mu rafet a ngay woote ca mbedd ma , di xaacu ca penc ma . |
ngir turu yeesoo tax nepp sukk , ci asamaan , ci kaw suuf , ci biir suuf |
aji sax ji boroom gangoor yi , yaw miy nattu ku jub , di gis xel ak xol , |
sama mer laa deggaatee ay xeet , samam sanj laa leen mandal , sotti seen deret fi suuf . |
kiy barkeel a gen a magg ki nuy barkeel , loolu amu ci benn werante . |
ba saraxu ngoon jotee , yonent yalla ilyaas jegesi , naan ne aji sax ji , |
deglul , ma woote ! teewlul , ma dagaane la lammin wu mucc fen . |
noonu ibraayma fab fukkeelu cer bi , maanaam asaka , ci li mu jele woon ci xare ba lepp , jox ko . |
lii mooy li waral ñiy liggéey ci mbay néew te wàññiku ñi dëkke kaw gi gën a néew loolu it jur yokkug ñi dëkke ci taax yi bu ko defee am lu juddoo ci loolu mooy néewug njóoxiitum mbay mi te loolu it tax na njëg yi aju ci mbay ak li ciy juge gën a seer |
yaa ngi koy àtte ndax ay jëfam fekk yaw itam noonu ngay jëfe |