text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
ba ñu ko gisee nag ñu ñaan ko mu génn seen réew |
ginnaw bi mu jànge risaala ci diggante 1882 ak 1880 mi ngi amoon 25 at la dem ndar ci sëriñ ahmadu njaay |
noonu ñiy wottu buur bi ak ñépp gis nañu bu leer ne turu kirist rekk a tax ñu jàpp ma |
nguur gu ci nekk ab buur a ko daan jiite ab jataay conseil moo ko daa jox sañ sañam jataay boobu moom lañu dénkoon muy fuglu ay saxalam aki ndigalam ay foNsaneer daa nañu dimbale buur bi di def liggéey yi aju ci saytu alal ji wattu kaaraange gi taxawal yoon ñenn ci ñoom it daa nañu dooni kaN gouverneur ñeel lenn ci diiwaan yi |
yaw lanu daa woo wall , mucc yaw lanu woolu woon te rusunu . |
du saamar a may may ndam . yaa nuy musal ci ban yi , yaay gacceel noon ni . |
noonu dinanu man a yegle xebaar bu baax bi ci berab , yi leen feete gannaaw , te ban a damu ci li neneen ni def ci seen sas . |
kenn musul a gis yalla , waaye bu nu beggantee , yallaa ngi dekk ci nun te mbeggeelam mat na sekk ci nun . |
képp ku la ñaan may ko te ku nangu say yëf bu ko ko laaj |
noonu xarekat ya dagg buum yay téye looco ga bàyyi ko mu wéy |
mu sol mbubb mu gudd takk ngañaayu wurus ci ndiggam |
tontu te deggagoo , ndof la , ak nakk kersa . |
te lii itam bu sa mbokk defee bàkkaar demal yedd ko yéen ñaar rekk |
fekk am na fa jigéen juy déglu tudd lidi di jaaykatu cuub bu dëkk catir te mu ragal yàlla |
noonu surga ya génn ca yoon ya boole ña ñu fa gis ñépp ñu bon ña ak ñu baax ña ba néegu reer ya fees ak ay gan |
may ma , ma gis ni nga leen di feye yaw de laa diis sama mbir . |
firefox nemmeeku na ni serweer baa ngiy jubalaat laaj ci makkaan bii ci anam bu dul sotti . |
ci ñaareelu xaaj bu xixeelu xarnu sancaani faraas yi les colons francais tàmbali woon nañoo nangu ndànk ndànk mbooleem nguur yu senegaal yii |
dëgg la ne nit rekk lanu waaye dunu xeexe ni nit |
wolteer de gore ga waa angalteer ame woon da koo neexoon lool yeemoon ko mu jeexiitalu ci ginaaw ba mu fa amee ñatti at li waraloon mu nekk fa nag mooy danu koo dàqe woon fraans |
nu jebbal leen nawkay saamar , till seddoo . |
yebal betel . alyaasa ne ko ak sama digganteek aji sax ji , kiy dund , nga fekke tey , duma teqlikook yaw mukk . nu daldi and , dem betel . |
samay besi noflaay nag wormaal leen ko te sama berab bu sell teral leen ko . maay aji sax ji . |
jëf na jaarale ci samay wax ak samay jëf ci ay tegtal ak i kéemaan sukkandikoo ci dooley xelu yàlla mi |
jariñooleen yiw wi ngeen jote ci yàlla ngir mu baña neen ci yéen |
bul dekkoo sab set bu jigeen bu sa doom ju goor jur mbaa sa doom ju jigeen , ndax kon torxal nga sa bopp . |
te sax ci mujjug at mii rekk nu bari di nanu dellu reew ma ngir tebeski ji , bu ko defee nu ci epp danu fay des ba weneen xewu diine wu mag wa new di maggalug tuubaa , bu ko defee nag bu jallee nu door a dellooti tugal ci jamonoy lolli . |
allaaji mamadu ngeer , doon na ku xam xamam macc ci wallu mbindum wolof ci arafi latin ak yoy araab . |
ci noonu nu jangoon taalifi kanadii , faarabii , ibnu sinaa ak ibnu rusdi ak nu dul noom , ginaaw bi nu leen firee ci seeni lakk . |
soxna si daal , benn tank la am , benn loxo , benn bet , benn nopp , benn baaraam . |
noonu mu dem ca gox bu jege mandi ma , ca dekku efrayim . |
mu japp ci loxol ndeyjooram , yekkati ko . |
li nekk yiteem mooy rafetal dundiinu ligeeykat yi ci adduna bi ak fexe nu yokk seeni ngérte |
guddaay ba , yaatuwaay ba ak taxawaay ba lepp tolloo , di fukki junni ak naar ciy estat . |
buur erodd markus yulyus agaripa ii bokkoon na ci juroomi buur ya tudd erodd . |
waa tugal yi ci tefesug afrig gi ci lu tollook juroom natteelu xarnu g . j , jaayees na ay jaam yu waa afrig ci ay yaxantukat yu daa def yaxantug takk gi , ak gu tefes gi ci tefesug mbambulaan gu end gi ocean indien . |
nuy woy woyu musaa jaamu yalla bi , ak woyu mbote ma , naan say jef rey nanu te yeeme , yaw boroom bi yalla , aji kattan ji . say yoon jub nanu te deggu , yaw buur bi fiy sax ba abadan . |
te gisul sa ndigali yoon yi ko tiim . ma ngay ciipu banam yepp . |
doon nañu ko jëfandikoo it ngir natt seeni bési xumbéeli diine |
jaadu na ñu fàttali leen ne xobi njéggal mooy li fi wuutu woon tuubug aji tooñ ji ci jeem a fare ay bàkkaaram ci def lu baax jaare ko ci julli walla joxe asaka mbaa woor |
gannaaw ga musaa tallal loxoom , mu tiim geej ga , aji sax ji yebal ngelawal penku lu rey guddi ga gepp , janaxe ko geej ga , ndox ya xajjalikoo , ba suuf su wow feen . banni israyil nag dugg ca biir geej ga , di dox ci kaw suuf su wow , ndox ya ne satt , nagal leen ndijoor ak cammon . |
seen pëndu dëkk bi taq ci sunuy tànk sax noo ngi koy faxas ngir seede leen seen réer |
coppite yi neel jefandikukat sebrevbot wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii . |
mbarum fitt a ngay kese kese i fa kawam , fa xeej ak jaasi lerxatandoo , |
genn loraange du la dab , balaa du jege sa xayma . |
noonu amoon na fa ku tudd yuusufa , te ndaw yi dakkentale ko barnabas , miy tekki kiy degeral fit yi , mu soqikoo ci giiru lewi , te juddoo dunu sipar . |
noonu mu am yengu yengub suuf bu mag , jant bi nuul ni kerin , weer wi xonq curr ni deret . |
waaye ñi waroona bokk ca nguur ga dees na léen sànni ci biti ci lëndëm gi |
samay soppe , bu nu yalla beggee nii , nun itam war nanoo beggante . |
nguuram ak nett . kaddug aji sax ji dikkal na ko ba tey ci janti buuru yudaa , yowakim doomu yosya , di ko dikkal , ba keroog nguuru cedesyas , jeneen doomu yosya ja di jeex . mu yemook fukkeelu atu nguuram ak benn , ca juroomeelu weer wa . booba lanu japp waa yerusalem njaam , yobbu leen . |
bi yeesu di wàcc ca gaal ga ku rab jàpp ca waa dëkk ba ñëw kar ko |
ku bon day sosu rekk , deng juddu , teggi yoon , dib fen kat . day am da ar ni nangoor , fatt i noppam ni jaan ju tex |
ba loolu amee musaa ak aaroona dem ba ca kanam xaymab ndaje ma , aji sax ji wax musaa ne jogeleen biir mbooloo mii , ma faagaagal leen leegi ! nu ne gurub , depp seen je fa suuf . musaa ne aaroona jelal and bi , nga sakke ci sarxalukaay bi ay xal , teg ci cuuraay , |
buur yu bari noo yoroon nguur ga ba noppi , tubaap yi new ak canc gi colonisation , ci atu , jel nguur gi , elif almaami yi , di seddale dekk bi , ci ay li nuy wax ci lakku fraanse canton ak provinces . |
garibaldi it bayyi politig , ndax kat moom li ko taxoon a jug mooy ligeey ci itaali doon benn , waaye soxlawutoon ay pali politig . |
waaye ci wax jooju xar kanamam lëndëm mu jóge fa ak tiis ndaxte ku bare woon alal la |
garab gu baax manula meññ doom yu bon naka itam garab gu bon manula meññ doom yu neex |
ndax ca xveelu xarnu , buurba jolof ba , tyukuli ndiklam , uuf na dekk bi ca biir jolof , ak tekuruur itam . |
jabaram elisabet askanoo moom itam ci aaroona . |
coppite yi neel jefandikukat ahloubadar wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii . |
ndaxte newuma , ngir woo ni jub , waaye bakkaarkat yi laay woo . |
mi ngi nekk ci bëj gànnaar penku kanaari gu mag mooy dëkk bi fa ëpp tëdd ci suufus 10 kilometers mi ngi nekk ci bëj saalumu afrig ci bëj gànnaaru réewum afrig gu bëj saalum |
lu tax ngeen may wooye boroom bi boroom bi te dungeen def li may wax |
coppite yi neel waxtaani jefandikukat mf warburg waxtaani jefandikukat mf warburg wii xetu jagleel moo lay won coppite yu mujj ci xet yi lekkalook wii . |
umra yitam sunna la benn yoon mook aj ñoo nuroo lépp waaye boo doxee safaa ak marwa umra jeex |
su ngeen sequl ak noonu dara , kon faww ngeen genn addina . |
boroom xam xamu angle bii di william gilbert nekoon doktooru buuru angalteer bu jigeen bii di elisabet mu njëkk mi moom itam ñëw feeñal ne am na yeneen ne ne yuy am ag ñoddi boo leen jonjee yu dul kuran rekk |
fraans duggsi ci , ci wetu rusi miy reew miy xaritam , nadx moom la defal ag tapoo , daal di jibbal ab xare ci kaw almaan ak otris . |
noonu tebbi nanu yoon wu jekk , wa neewoon doole te mennul dara |
rawatina nag ne , jefu xelum yalla dina gen a and ak ndam . |
dëkkug lebu yi ci ndakaaru mi ngi am ginnaaw ay duusi gàddaay ci diggante 15 ak 16 xarnu |
ma sante fa jaani geej , mu matt leen . |
bindkat a ngi joxe tegtal ca moomu peenu |
su boobaa ku nekk sa bakkaaru bopp a lay rey . ku lekk resen yu xaay , sa geni bopp lay uum . |
yoon a ngi , nit defe ne jub na , te mu jeme ko ci dee . |
ba agg kades barneya . ci kaw loolu ma ne leen agsi ngeen fii ci tundu amoreen ni nu sunu yalla aji sax ji di jox . mu ngoog , seen yalla aji sax ji moo teg reew mi fi seen kanam . demleen nangu ko , ni leen ko seen yallay maam aji sax ji , waxe . buleen ragal , buleen yoqi . ci kaw loolu ngeen dikk yeen nepp fi man , ne ma nan yebal aw nit , nu jiitu nu , yeral nu reew ma , te delsi wax nu yoon wu nuy jaare , ak dekk yu mag ya nuy duggeji . ma rafetlu xel ma , tann ci yeen fukki goor ak naar , giir gu nekk , genn goor . nu walbatiku jubal yoonu diiwaanu tund ya , ba agg xuru eskol , daldi seet foofa , ba noppi sakk ca menneefum reew ma , indaaleel nu . nu wax nu nag ne nu reew mu baax lanu sunu yalla aji sax ji jox . teewul bugguleen woona dem , xanaa di gantal seen ndigalal yalla aji sax ji . ngeen di |
nangay moytoo wuññi sa biir ak li nekk ci diggante jumbux bi ba ci bëti woom yi ngir bon gi mu bon |
danoo moy degg , di wax ne ndekkite wees na , ba yaq ngemu nenn ni . |
noonu saxar jollee ca su mel ni saxarus puur bu mag jant bi ak jaww ji lépp lëndëm ndax saxarus kàmb ga |
dinaa la leeralal kumpag jigéen ji ak rab wi mu war te am juróom ñaari bopp ak fukki béjjén |
xanaa aji sax ju gangoor yi . kookooy buur boroom ndam . selaw . |
ci kaw loolu elyakim doomu ilkiya ak sebnaak yowa wax bekk neeg ba , |
waaye yaw nanga foog ci lépp dékku tiis tey tas xibaaru jàmm bi ba matal sag yónnent |
waaye bi ma doonee mag bàyyi naa lu bokkoon cig ndaw |
yuusufa taalibe yeesu la woon ci lu kenn yegul , ndaxte dafa ragaloon yawut ya . |
leegi nag bavar bokksi na ci ak saksoniya ci atum g , ca saa sa tam , nga tamblee gis lu lay won ne solofrayn moom tambli na a naat ak a am ag yokkute . |
nangeen maggale yalla biir keram gu sell , maggale ko ca tatay asamaanam . |
te bu dee dangaa fonk sa benn ceru yaram it , ndax du sa yaram wepp a ciy banneexu ? |
li ma nesar nag mooy nekk jaamub boroom aras rekk , di ligeeyal gen ji mbindeef , te moom yonant bi mooy samab xuppkat yonant bi day bashiir tey naziir , di kuy begale tey xuppe njir jaam yi ban a saggan ban a naagu . |
sama jef ju baax , loraange lanu ma ko feye , sama cofeel , nu feye ma ko mbaneel . |
mujj na jaare ko ci imaa imit di ab jabar ci diiney xerem ji fi fekkoon baax . |
yaatuwaayu suuf yi holad mujjoon sanc mujjoon na gen a rey juroom naari yoon yaatuwaayu holand gu ndaw gii ci jemmi boppam . |
jefeleen ak xel ci seen diggante ak waa addina , te fu ngeen ame jot , fexeleen ba jarinoo ko . |
bi nga xamee ne genn nanu ci jangu bi , nu and ak saag ak yowaana , dem ci ker simo ak andare . |
bi almaan lankee ban leen a deglu , la ko britani ak fraans song , ci satumbar g . |
s menula deggal ni pake yeesal bba ngi ni numm . |
waaye yaw nag xam nga bu baax sama njangale , sama dund , sama takkute , sama ngem , sama mun , sama mbeggeel ak sama dekku tiis . |
rawatina seen jigeen ku daan sey ak lawbe bu jiggeen jap ne karaange la am |
yaw yalla , yaay sama mbegte , di sama banneex . yaw yalla , sama yalla , |
kattan nag di energie jem na kanam ci jem gi jumtukaay jem kanam te awaase . |