text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
ni doom aadama di layool moroom ma fi kaw suuf ! |
xetug jamm , neel aji sax ji , ak saraxu peppam , ak saraxu tuuroom , ni ko yoon attee , ak benn sikket ngir saraxu pootum bakkaar . sarxalkat bi day def loolu njotlaayal mbooloom |
na leen boroom bi dolli mbeggeel gu tar , ngeen beggante te begg nepp , ni nu leen begge nun . |
ci bis bi njekk ci samwiye la abraham linkoln jibal goreelug jaam yi , googu jibal moo neenal njaam gi ci diiwaan yooyu dogoon ci bennoo gi . |
booba ñuy ñaan buur te yàlla jox léen sóol doomu kis ci giiru beñamin muy seen buur diirub ñeent fukki at |
la amoon ba may sos xeet wu yagg wa , ak li dikkagul . |
am na yeneen reew yu yees yu feen ci ettub politig bu tugal bi , yu ci mel ni espaan , portigaal , angalteer , fraans , holand ak yu dul yooyu . |
soo wéyee ciy nelaw nag dinaa ñëw nib sàcc te doo xam wan waxtu lay doon |
sellal sunu bopp ci bépp sobeb yaram walla bu xel dund ndegam nag jot nanu ci dige yu mel nii samay soppe nanu dund gu sell ba mat ci ragal yàlla |
xelum boroom baa ngi ci man ndaxte moo ma tànn ngir ma yégal néew doole yi xibaaru jàmm bi |
amoon na neenti doom yu goor ci jabaram , eliseba . |
ndax da nga begg degg mabb baati jall yepp ? |
ci takkndeeru boppam la yalla bind nit , goor ak jigeen la bind . |
noonu naari jef yooyu nga xam ne dunu tebbiku te yalla menu cee dellu gannaaw , danu nuy gen a soob ci mun , nun ni daw ba am kiiraay , ngir nu man a teye bu deger yaakaar , ji mu nu dig . |
yaa koy gis , sa kanam ne rann , fit tef tefi , xol fees dell , |
xamal ne sa naawteef gu rey a waral nu nori la , saay saaye la . |
muy nelaw walla muy xool , guddi mbaa becceg , jiwu wi sax , di magg , te xamul naka la ko defe . |
ay tànkam mel ni xànjar bu yànj bu ñu xelli baatam di riir ni duusi géej |
jagal gu njëkk gees def ci cd rom mi ngi génn 1994 |
waaye bi ko ndaw yi barnabas ak sóol déggee ñu sib ko ba xotti seeni yére ñu daldi daw tàbbi ca mbooloo ma di wax ci kaw ne |
kaw kol kolub suuf si mi ngi ame ci jéeri ji ak ndox mi bu ko defee jéeri ji yóbb ci benn ñeenteel maanaam bu doon ñeenti xaaj la benn bi ndox mi moom yóbb ci ñatti ñeenteel |
bi bésub noflaay agsee nag génn nanu ci buntu dëkk ba jublu ci wetu dex ga yaakaar ne bérabu ñaanukaay la |
kepp ku leen di topp dabe leen fu nu leen di tance . |
43 dëkkaani ndiiwaani yi dañu leen séddale ci 4 tund yi |
ba nu noppee ca saraxi rendi doomal ya , yewu ne dag yaak jawrini |
bepp janq bu tollu ci njeexitalu ndawam menees na koo maye mu sey te deesu ca seet naata at la am . |
jeexitalu dayo lanu doon xaar , wante s lanu gis . |
maa leen di dogal kemug suuf gu dale geeju barax yi , ba geeju waa filisti , daleeti ca mandi ma , ba ca dexu efraat , ndax maay teg waa reew mi ci seeni loxo , ngeen daq leen . buleen wolleranteek noom , buleen wolleranteek seeni tuur . bunu dekke seen um reew , lu ko moy muy seen ndegg serex ndax danu leen di xiir ci moy ma , ba ngeen jaamu seeni tuur . |
dees na ne tuuti lawiir day tax tooyalu farin bepp funki . |
teewul aliyun nangu ne am na leeg leeg ay jaaykati imigre yu juge ci yeneeni reew yu gen a muus murit yi ci di indi njaay walla jaayiin wu bees . |
leer gi feen na ci biir lendem , te lendem gi jappu ko . |
moo tax ma xalaat ne li gën mooy yónni bokk yooyu ñu jiitu ma ci yéen topptoo mbiri ndimbal lu yaatu loolu ngeen dige woon |
noonu nu defi seede te gisunu , yegunu , muy seen gacce ! |
li ma sama baay won laay wax waaye yeen , li leen seen baay di wax ngeen di def . |
bu ndox mi masaa yëngu ba noppi jarag ju ca jiitu wopp joo amaan daldi wér ca saa sa |
bul dekkoo sab jigeen , te muy koo bokkal benn baay mbaa koo bokkal jenn ndey , muy ku juddoo ci ker gi mbaa feneen . |
noonu yeesu yiwi mbooloo mi dugg ci gaal ñëw ci wàlli magadan |
ku nu raw ci jullig ber tebeski walla kori , bu agsee fekk yilimaan di jang day kabbar juroom naari yoon benn ci kabbaru armal bi te and ak yilimaan la ca des . |
yeesu dégg kàddu yooyu daldi ne njiit la |
buur ba sesaar moo faloon benn jawriñ ngir toogal ko ñetti at ba juróomi at yu nekk mu nekk boroom réewu siri |
yeen ni deger bopp , and ak xol buy ban ak ay nopp yuy fatt , mel ni ni xamul yalla . dungeen noppeek a diiroo ak xel mu sell mi ni ko seen baay yi daan defe , noonu ngeen di def yeen itam . kan ca yonent ya la seeni maam tegul woon ay fitna ? rey nanu ni doon yegle newug aji jub ji , moom mi ngeen jebbale leegi , ba nu rey ko . jot ngeen yoonu musaa , wi yalla wacce jaarale ko ci ay malaaka , te saggane ngeen ko . |
yéen samay bokk muñleen ba boroom bi délsi ci ndamam |
noonu ku laab fas ngir mu déggal la not nga jëmmam jépp |
ba mujj mel ni sagaru sobe ku ko teraloon , sofental ko , |
yoon wu ma leen di xalaat , maa ngi sant yalla sama boroom |
ag dex a ngi def i wal , di banneexal dekku yalla , sellngay dekkuwaayi aji kawe ji . |
ci ndoorteel gi muy ruy , wallu suuf si feete woon biti tambalee sedd , dem ba doon ab donj bu deger bi ndox tambalee dajaloo ci jawwam . |
noona lanu daan nattee solo lakki reew mi . |
ubbiku nanu ci yeen , waaye yeen ubbikuwuleen ci nun . |
ne leen nangeen wax lii ay taalibeem new nanu ci guddi , sacc ko , bi nuy nelaw . |
ay boroom xam xam ñëw nañu màggalsi yeesu |
kon nag nangeen degeralante te yokkante seen ngem , ni ngeen koy defe . |
fekk noot nanu kojaarale ko ci deretu mbote maak seen seedes ngem , te soppunu seen bakkan ba ragal a dee . |
ci degg degg maa ngi leen koy wax , ku gem am nga dund gu dul jeex . |
reewum niseerya siiwal na alxamees gee nu weesu fan ci weeru ut ne sanni naari satelit ci jaww ji . |
ca njël nag yeesu jëm ci ñoom di dox ci kaw dex gi |
mu tàmbalee dóor ay bokki surgaam di lekk te naan ak naankat ya kon njaatige ba dina ñëw ci bés bu mu ko séenuwul ak waxtu wu mu xamul |
te sànnileen surga bu amul njariñ bi ci biti ci lëndëm gi |
beggum neex duma taxa deppoo cin lu tang . |
ay saay saay noo ko ray ca weti tripoli mu feekoon ko muy aji makka . |
defe ngeen ne aji sax ji duma na israyil , na mu dumaa na leen duma woon ? |
ci tukkiy njàng yi mu defoon yépp ca jamono jooju jaaroon na ca tund ya ëppoon boroomi xam xam gànnaar fuuta njambur kajoor ci dëkk yi mu dem man nan cee lim ndoj séy pacaas ngicc jaabe lidube orefonde longe sëbe longe fulbe careen ndar tayba séy daraaman añs |
kàddu yi ma leen di wax jógewuñu ci man waaye baay bi nekk ci man mooy matal ay jëfam |
bi yeesu duggee ci ker gi , taalibe yi laaj ko ci pegg lu tax menunu ko woon a daq ? |
ci waxambaane yi doon waliyaansi mu am ci ñu fi takk jabar ñii takk fi xarit ñii sàmp fiy néeg |
nii itam la kuy nàmpal di def bu ragalee ci boppam ak ci doomam te amul ku ko nàmpalal walla doom ji nànguwul keneen ku dul moom |
gannaaw gi , ca juroom naareelu weeru at ma , ismayil , doomu netana doomu elisama , bokk ci askanu buur , and ak fukki nit , dikk boom gedalya , boomaale waa yudaak waa babilon ya nekkoon ak moom ca mispa . ci kaw loolu mbooloo mepp fabu , baadoolook boroom barke , nook kilifay xarekat ya , nu daldi daw dem misra ndax ragal waa babilon . |
kon warees naa jangat loolu ba xam lu ko waral , ndax safaan la ci ndemeelu demokaraasi . |
am ñaari nit di waxtaan ak moom muy yonenti yàlla musaa ak ilyaas |
ñaanalal ki ngay nuyyool yaw boroom xel mi ndax loolu de bokk na ci liy fari bàkkaar |
baatu ndaw su jagadi laa degg , ma nga jaq , di matub taawam . |
yeesu tontu leen ne ndax janguleen la daawuda defoon , ba mu xiifee , moom ak na mu andaloon ? |
ca atum 1549 la jolof gu mag ga tas ak lele fuli fak |
jokkalekaayu jefandikukat boo miin , soloy kaaraange yees genal bokk nan ci aar la ci caccug say xibaari jemm , jumtukaayu ceet gu biir di la jotale li gen ci web bi . |
maay genne sama non ci seeni loxo , ngeen xam ne maay aji sax ji . |
bul nay mukk ci ponat mii alali addina jii ba loolu di waral sa gacca ca yalmal qiyaam bis penc . |
maa leen di tuutal ba dootunu yilif xeet yi . |
mbaaxam ak yéwénam yéemoon na képp nit ku nekkoon xaayra ca jamono jooju |
ak noom kollere , ngir jox leen reewum kanaan , reew ma nu nekkoon ay doxandeem . maa deggal sama bopp yuuxi banni israyil , gi waa misra def ay jaam , te fattewuma sama kollere ga . kon nag waxal banni israyil ne leen man maay aji sax ji . maa leen di sippil , yeen banni israyil , li leen waa misra sef , te maa leen di teggil njaam , gi nu leen teg . maay tallal sama loxo , dogal mbugal yu keemaane , ba goreel leen . maa leen di def sama non , di seen yalla . dingeen xam ne man aji sax ji maay seen yalla , ji leen di teggil sas , yi leen waa misra teg . maa leen di yobbu ba ngeen dugg reew ma ma ginoon ne maa koy jox ibraayma ak isaaxa ak yanqooba , te maa leen koy moomale , man aji sax ji . |
ngay joxe sa alal and ak begg nga ko , waaye nga diko joxe ngir jemmi sunu boroom subhaanahu wa tahaalaa . |
li nguur gi begg mooy fexe ba nepp and ak moom , nu amal fig nguurug bennoo giy emb pacci reew mepp . bu ko defee , kenn dootul san a taxaw naan anduma ci lii . . . , lee baaxul . . . , lale , bees ko defe woon nii mooy gen . . . walla ni nguur giy doxale , dara doyuma ci , ans . reew nag , bun demee ba kenn sanatul joxe sa xalaat , njaaxum ak musiba mu rey dikkal na askan wa fay yeewoo . bala nuy xippi , dina fekk nu rey leen bu yagg . loolu , du fi ame tey , te du fi ame elleg . |
waaye nag déedéet wéetuma ndaxte baay baa ngi may wéttali |
ettub amerig bii nag mujjoon di def ay mbir yoo xam ne noo waraloon xareb temb bi takk . |
mu santaane nu dugg ca betleyem ak la ko wer , rey xale yu goor ya fa am naari at jem suuf , mengook jamono , ja ko boroom xam xam ya waxoon . |
yapp wa duuf , yuq ja ne xeew , ak tanneefu biin bu teey . |
besub noflaay nag naari xari menn at yu mucc sikk lay doon , ak saraxu peppam , biy naari fukkeeli efay sunguf su mucc ayib , di juroom benni kilo , nu tooyale ko ag diw , te mu and ak saraxu tuuram . loolooy saraxu rendi doomalu besub noflaay , ci besub noflaay bu nekk , te bokkewul ak doomal bi war bes bu nekk , te and ak saraxu tuuram . |
mbooloo maa ngay xaar , di seentook a laaj ci seen xel , ndax yaxya mooy almasi bi . |
mu ni billaay billaay céglaar gan a ngi ci kër gi fi gan a ngi fi woon |
waaye fu nuy jële ci àll bi mburu mu doy ngir mbooloo mu tollu nii |
mu ngi binni , di neew ji doole . aji sax ji nee maa ngii , di ci jog , teg leen fi rawtu gu nu ne siiw . |
jukki yepp yi am ay coppite yu noppiwul ci tekki . . . |
santiago tequixquiax béne deukkou meksik |
waaye li ma naqari ci yaw moo di sa mbëggeel wàññiku na |
moo tax ay bes a ngii di new , kaddug aji sax jee , |
ca atum yiwiku ma . ndax kat man la banni israyil di samay jaam . noo di sama jaam ya ma genne reewum misra yeen , maay seen yalla aji sax ji . |
ragal leen aji sax ji , yeen nitam nu sell ni ku ko ragal doo nakk dara . |
ci noonu nasaraanalkat yi jàpplanteek seeni góornamaa kontar araabi palastin yi ngir defar lañuy wax dëelub balfour génne ko it atum 1917 lii ko taxoon a jug di sos am réew mu xeet mu yahood yu sahyoon yi ca suufus jàmbur see di palastin di suufus ay araab yu jullit tubaab yi déggook yahood yi jox leen ko ci seenug toroxte ak naqar |
nit kune bu ñu ko mbugalee am na sañ sañ làqu ji mbaa ñaan ñu làq ko ci yeneni réew |
maa ngi leen koy wax it li dale fii dingeen gis doomu nit ki toog ci ndijooru aji man ji di ñëw ci niiri asamaan si |
kii mooy sama doom ji ma bëgg ci moom laa ame bànneex |