audio
audioduration (s) 2.29
12.5
| transcription
stringlengths 26
118
|
---|---|
réew mii réewum njub péex ak jàmm la |
|
Nit kooku dafa yeewu waaye naa fi ma koy jaar |
|
ñii fàlu nañu buur ñii doomi buur lañu di ay garmi |
|
nanga butti jén yi dal di leen raxas ba ñu set |
|
maa ko gis ci peroN bi la yàbbi logu poon bi |
|
ba mu nekkee lu yàgg ca kër buur mu ni xuléet delluwaat na mu meloon |
|
mbubb mi dafa xalloon ma def ci weexal |
|
boo jàddee ci sa càmmooñ dinga séen sama kër |
|
njàngale mi dina jafe ci moom ndax sawaru ci |
|
am na ay mbaaru mbott yu ñu dul lekk |
|
boo bëggee gis gaynde demal ca màndi ma |
|
maa ngi tollu woon ci sama diggi ndënd |
|
ku ma bëgga toroxal yaay mujjee torox |
|
man de xawma lu muy ree nii ba di kekku |
|
dafa jënd pàkk bi rekk tàmbali ko sàkket |
|
amari ngoonee taxoon kajoor feyatul voon galag jolof |
|
xam nga xéll ni taluma wure ak soxal yi ci sama bopp yépp |
|
dafa gore moo tax ma nangoo liggéey ak moom |
|
Na ku nekk déglu sa morom ndax ngeen baña réeroo |
|
ña leen a jëkka séen ca dëkk ba dañu teg seen loxo ci seen gémmiñ |
|
ndaw si daldi leen di juuy fekk na nag ag genn dédd a ngi fi goo xam né gii war naa mot diggante fii ag teen ba |
|
maa ngi leen di soññ ci def seen liggéey |
|
li nga semb dey yombul waaye yàlla na la ci yàlla jàppale |
|
booba jamano pikini rekk la sondeel doon jar |
|
li nga toog lu yàgg moo tax sa tànk yi sadd |
|
bu ñu fëggatee nanga xool ci yëru bi bala ngay ubbi |
|
ndax garmi day am jabari jinné di ci jur ay doom na ka walliiw wu nekk |
|
amoon na ag dóobali ci seen buntu kër |
|
xaftaan bu nëtëx la sol ak mbaxane mu xonq |
|
li ëpp ci lapto yi ay njaago lañu woon |
|
sama lam bi furi na war naa koo sóob |
|
jubalal sa tuuru fetal bi fu dara nekkul |
|
juuti bi dafay dem ci luuma yi ngir feyyu juuti |
|
soo wutul kaaf sa pitax yi dinañu dem |
|
amari jullit né ko jógal nu dem rekk |
|
xale bi daal dafa ma lëjala lëjal ba nga xam né dem na dayo |
|
dafa xeet taabal bi dal di ko pintiir |
|
dafa indiwaale woon surgaam bu mu daan yónni |
|
sa mbubb mu xàññaaral mooma daal bu ko sol |
|
dafa doon dox ba yàgg mu ne dàll daanu |
|
reeni xom xom fajkat yee koy jëfandikoo |
|
waa ji yóbbu mbaam yi wax leen li buur diglé |
|
ku sa bëgge bari sa ngor néew |
|
sama tànk bépp a ngi xasan taqentaan a ma topp |
|
boroom kër ga dafa ko fitnaaloon bu mu mujj toxu |
|
yaa ngi doon gam gami xamoo dara ci waxtaan wi |
|
séex yooyu neex nañoo xàmme nuroowuñu |
|
su amee toppatoo gi ci war xar mu rafet lay doon |
|
benn seex bi gàjj bi ci lex bi laa koy xàmmee |
|
gone yu mbuujaa mbuuj yi ñoo fi nekk |
|
sacakàt bà défà né parah né varah |
|
ak tàngaay wi ngoor si dow dem daanu ci kër |
|
peccum liir bu neexee ndeyam a téye ca tank ya |
|
ñi nelaw ñii ci des doxantuji dugg ci réew mi |
|
ba ñu dajee ak yaw dañu daw wëqét |
|
danu daan dem tefes di xëcc mbaal ngir ñu may nu jén |
|
seen baay nee na leen bu nu bàyyi benn ruq bu ñu bàllarñiwul |
|
lu di nav té du tag mukà ngélav |
|
aprés bu may séy dina ma geener torop encore |
|
borom bi yërëm ma ndege moykat rekk laa |
|
demal ne ko mu seede ma ñaari kiloy ceeb |
|
bàggu fu nekk ñu bàggante rekk gisuñu dara |
|
booba fekk na ñaari mag yi ñu ngi doon waaja seeti seeni coro |
|
mu ne mënula ñów waaye mu ngi leen di yokk ngóora |
|
wax ji dafa lunk ñu bare ci mbooloo mi nanduñu ko |
|
ku ja ci jant bi te ne gisu ko lu ñu ci mën |
|
dama la bëgga biral sama dikk moo tax ma telefone |
|
ñu jekki ba nga xam né jant so na góor gi ñów seet nag yi gisul dara |
|
lenn rekk la bu mbeex màggee warul sëy warul am beneen jëkkër bu dul man |
|
Naka la dawe ci néegam mu mbëkk boppu doom ji doon lang di bunt bi |
|
dama bëgg xam këf ki mu dugal ci waxande wi lu mu doon |
|
mu teg saakam dal di dem ubbi palanteer bi |
|
ndeer la dellusi ni tareet tareet ey biram njéemé koo njaay de wul dekki na de |
|
alkaati baa ngi ne sàtt ci bunt kër gi ca suba ba tey |
|
tànk boo séqi dinañu la ko bindal tuyaabo |
|
janq jee daan watu pàq waaye loolu xewwi na léegi |
|
moom bëggewul rekk yem ci dafa wóttóoral |
|
bi ko doomu baay yi lakkalee ba nga xam ni mënatula dëkk ak ñoom mu gàddaay dem jolof |
|
wàccal rekk du yàgg létt yi du yàgg |
|
bu ñu defaree sorbo bi ba noppi dañu koy taxaar |
|
buumu xalam gi yóbbaale na la wa ngi xandaalu |
|
aa man dé sama jëkër dafa ma mooñloo tey jii te dama koy mooñal |
|
mu mel ni ndoxu asamaan si yépp a bëggoona xëppu ci kaw suuf si |
|
diggante ndakaaru ak barñi fanweeri kilomet la |
|
fekk am na ñu dëgger bopp ñu ko sarax ñoo ñu daldi tàqalikoo ak seeni bët |
|
may ma loxo ma dugal taabal bi ci saal bi |
|
góor gu am fayda du dàggasante ak jigéen |
|
booy war mbaam dangay jàpp ci kawar gi ci céq mi |
|
abdu woor na tey dafa feebaroon fan yi nu weesu |
|
xale yi farlu nañu lool ci njàngum katesis bi |
|
xaalis bi ngay jox jibar bi tee nga cee jénd garab yi la doktoor bindal |
|
bul fàttee jënd yomb tey cere lañuy togg |
|
dafa sëpp sayu xat waaye mën na bëre |
|
ku ñu ma may rekk ma ni bëgguma ko ma bëggoon nag wuti |
|
moo doom sa baay waxu la woon lii |
|
saa su ma ko nuyujee dina ma may aylayéwén junni |
|
te ñu bari bassi seen feebar ci tooy lay joge |
|
am na masin yuy gàbb waaye dañu jafe njég |
|
palpale yi nga gis bitim réew lañu lenn di jaaye |
|
ree ji mu lay gatandoo rekk sedd na xol |
End of preview. Expand
in Dataset Viewer.
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 36