text
stringlengths 38
33.7k
|
---|
ci xam xamu nosukaay tëriinuw nosukaay walla tëriin kepp am mbooloom ay càkkuteef la gees binde ci genn kàllaama gi gu ab nosukaay war a jëfe |
ndaxte kenn ci ñoom ñemeetu koo laaj dara |
ci kaw loolu piyeer ak yowaana ne ko jakk , te piyeer ne ko xool nu . |
boroom ndomboy tànk yu mag ya ñoo daan doxal njiitu jaraaf yi ñoom la buur daan diisool farba bëkk néeg jaalige saltige njiitu dëkk yi |
sarxalukaay ba , ngir rawale bakkanama . nu wax ko suleymaan , ne ko |
bu ko defee nasaraanalkat yi sos ci reew yii ay barabi nasaraanal ci biir askan wi , rawati na fa jullit na , ndaxte seen jubluwaay ci loolu mooy neewal doole jullit ni aks een diine . |
ñu toog ay at jabar ji ëmbaat beneen doom bu jigéen bu dàq ngóoné |
bu ko defee loolu di may reewum sancaan mi muy doxal mbirum reew mi nuy aar ci wàlli kaaraange bitim reew ak koom koom |
kon moo y mbuubs mi nga xam ne bu la reeree , la mu emb sanku , naaxsaay . |
waa isipt ñu njëkk ña ak finiix yi ak jullit ñi defoon nañu ko bu yàgg njëkk waa orob di ko def ci jamono ju yees ji |
fraans it ay xarekatam gennoon nanu rom , ngir sotti gi fraans sotti woon yitteem ca xareem ba ak brusiya . |
tey yuug ak a goor ni gaynde sibi . yaa di gaynde gu deesul yee . |
mangaani penku laa leen di jebbal , jebbalaale leen amon , |
bi leen yeesu di wax loolu , benn njiitu jangu daldi new , sukk ci kanamam ne ko sama doom ju jigeen dafa faatu leegi , waaye newal , teg ko say loxo , te dina dundaat . |
bu xëyee moom gaynde rëbbi ànd ag amari julli sàmba seytaane des fa |
waaye festus tontu leen ne nu ngi wottu pool ca sesare , te dinaa fa dem fi ak fan yu neew . |
bu rootaan yii mbabbee , s dootul amm ci jokkoodiku . |
bokk na ci sabab yi jur doxug yile waxiin dem ci làkki réew yu xeet bokk na ci sabab yooyu nekk gu làkku w latin nekkoon di wenn ba yàgg mu seddaliku di ñaar wu ñu y wax kalaasik ak wu wilgeer |
bi mu tàggtoo ak mbooloo mi mu yéeg ca tund wa ñaan fa yàlla |
waaye njub , gi nu yalla dencal elleg , nu ngi koy seentu ci kaw ngem ak ci ndimbalu xelum yalla . |
njiit la ne ko loolu lepp samm naa ko li dale ci sama ndaw ba tey . |
te itam na musaa sampe woon ab bant ca diggu màndiN ma takk ca jaan ja mu defare woon xànjar fàww ñu yékkatee noonu doomu nit ki ngir képp ku ko gëm am ci moom dund gu dul jeex |
bëggunu ngeen tayel waaye royleen ñi gëm te muñ ndaxte ñooñu ñooy jot li léen yàlla dig |
su nu ko weddee , kon mu weddi nu su nu ko nakkee kollere , moom dina sax ci kollereem , ndax menul a weddi boppam . |
noonu mu wéral ñu bare ñu wopp ak ay jàngoro yu wuute te dàq ay rab yu bare |
foofu la xariti yeesu , di mart , maryaama ak lasaar , dekkoon . |
jaamookaay ba , ba musaa telee dugg ca xaymab ndaje ma , ndax niir wa makkaanoo kaw xayma ba , ak leeru aji sax ji fees jaamookaay ba . |
léegi nag bokk yi ci li jëm ci mayi xelum yàlla bëgguma ngeen umple ci dara |
xanaa di leen wax waxyuy caaxaan ak naxi neen . |
te du ci loolu rekk , waaye beg nanu it ci sunuy nattu ndax xam nanu ne , nattu day feddali mun |
ca kaw dend ba tiim seeni bopp , ba tey , am na luy nirook nganguney peru |
ci senegaal fepp bu jëkk ceddo yi ñoo daan yor nguur yi ñoo gënoon fete kaw ci nos gi |
ba mu ko defee waa misra sonn banni israyil , ngir nu gaaw genn reew ma , ndax booba na nga naan nun nepp ay dee ! loolu tax mbooloom israyil ron seen xiiwi sunguf yu amagul lawiir . nu emb seen ndabi notukaay ca seeni malaan , gaddu . fekk na banni israyil def la leen musaa santoon ca waa misra . sakku nanu ca noom ay ganjari xaalis ak wurus ak i yere . aji sax ji nag def waa misra nangul banni israyil , ba jox leen la nu sakku noonu lanu futtee waa misra . |
seen buumi xayma foqatiku , nu dee ci biir ag umple . |
ku la ga , nga yenul ko doxub benn kilomet , andal ak moom naar . |
waaye nu bare ci ni jiitu nooy mujji ni mujj nooy jiituji . |
te lépp lu ngeen laaj cig ñaan bu ngeen ci boolee ngëm dingeen ci jot |
am na fi ci mbooloo mi ab xale bu yor juróomi mburu ak ñaari jën waaye loolu lu muy jariñ mbooloo mu tollu nii |
ku la ragalul , boroom bi ? ku dul maggal saw tur ? kenn , ndaxte yaw rekk yaa sell . xeet yepp dinanu dikk , jaamu la , ndax say atte bir na nepp . |
noonu yeesu yebal piyeer ak yowaana ne leen demleen , defaral nu reeru jeggi ba . |
aji sax ji dafa wax musaa ak elasar , doomu aaroona sarxalkat ba , ne leen |
waaye waa ji xam nanu fu mu jóge te saa su almasi bi dee dikk kenn du xam fu mu bàyyikoo |
gàddu golo laa séen ci suba bi may dem tool |
ku bëgg a am lu ko leer na xool teere bi nu naan di ci maanaa leeralug lu lëndëm këriis ci man a nekkug gis yonnant bi j y m ak malaaka teere boobu boo bëggee lu leer rekk moo ciy géej jug mbàmbullan gi te boo defee ag settantal ci tuxal gii ak li ci topp da nga gis la amoon kon ca géej ga muy ni nu nangoo woon li mu jële woon ci ku dul woon yonnant bi j y m ak dello ngi ko ko yonnant bi delloowaatoon ak naayibam yi ñatti sëriñ yu tedd yi ngir mu nekk naayibam moom yonnant bi aji wuutoom tey ki fi wuutu yooyule sëriñ g y y ñ ci seeni wird di seen muxaddam bu nu joyal bi nga xam ne amul lenn lu ko tënk ci wenn wird ku ko neex ak nu ko neex la koy joxee da nga ci gis it la amoo n ci sarsaara muy jox ga nu ko fa joxoon wirduw boppam moom rekk jagleel ko ko nga xam ne benn sëriñ bu ko fi jiitu masu koo yor |
yaa tax ma dekku , nu di ma sewal , ma rus ba selmoo gacce . |
boo ciy jaar de ngay foog ni de nga cey nekka ba faw wànte ci degg degg yaa ngi wàccee ci nu mu gena gaawee |
diiwaan la woon ci penku dexu galile fu yeesu demoon |
waaye gannaaw yalla tann na leen , dafa leen begg ba tey ndax seen maam ya . |
noo gantal yoonu aji sax ji ci gangoor yi , noo sofental kaddug aji sell ju israyil . |
amoon na benn besu noflaay yeesu jaar ciy tool yu nor . |
samm bi nag , nii la war a mel war na nakk ann , yem ci benn soxna , moom boppam te maandu war na am faayda , man gan te am mayu jangale |
penku afrig mooy wallu afrig gi gen a feete penku . |
fekk seeni bet muuru , ba menu ko woon a xammi . |
moom de njaayum jaam ag toonaange gu mag la neel ag nite ci lu dul gen jaa neewi sikk . |
dañoo tëjoon barabas ndaxte dafa jéema tas dëkk ba te rey nit |
boo ko beggee samp ci beneen wayndare bu wuute , cuqal ci seet . . . te nga fal beneen wayndare . click |
aji sax jee lay xettli , besub njaqare . |
fi ñu koy waxee ñoom ñaar ñu jóg taqaloo ci ruum bi jigéenub xuuge bi jóg doon leen àtte far ñaari xuuge yi ku ci nekk né këpp ci suuf ñu dee ñoom ñaar ñépp te ci dëkk bi kenn du fa suul ab xuuge |
fa keppaaru esbon lanuy daw taxawi , doole deddu . |
naka la juroom naari dennu yi di jib , may waaj a bind , waaye ma degg baat bu joge asamaan , naan ma li juroom naari dennu yi wax , na nekk kumpa , bu ko bind . |
juróom benneel ba per bu xonq curr bu ñuy wax sarduwan |
dees na leen yobbu ngir man ci kanami boroom reew ak i buur , ngir ngeen seede ma ci noom ak ci ni dul yawut . |
bokk yi maa ngi leen di dénk ngeen moytu ñi leen di féewale ba di leen jàddloo yoon wi ciy wax lu juuyoo ak dëgg gi ngeen jàng |
nanu jappale ndimbalu mozilla mu wax sa lakk ! |
moom kat yàlla mooy aji kawe jiy boroom ngënéel ak tawfeex tey boroom li fii ak la fee |
jigéen ja tuur na latkoloñ ci boppu yeesu |
kon dina laabal aji woor ji ci mboolem rëcc rëcc i koor gi ak it indi indi jàmmu ci nit ñi ci dimbalante woomalal ñu ñàkk ñi ngir ñu yëg bër gi ni ñépp fexe ba kenn du yalwaan ci bis bi |
soo toppee xaaj yii di nga xam nu nuy soppee aw xet . |
nun nu foog ne dees koo mbugal , foog ne yallaa ko duma , torxal ko . |
kol kolu adduna bi gox baat la buy tekki ab yaa yaa wu suuf wu rey te tegu ci kol kolu adduna bi . |
déglul fii mu ne wér nga bul defati bàkkaar ngir ragal lu yées lii dal la |
yaw miy damoo yoonu musaa mbaa doo ko moy ba indi gàcce ci turu yàlla |
ci xarnub fukk ak juroom benn fuuta tooro def na ay xare ngir yaatal suufam ci kaw ay dekkandoom jolof , kajoor . |
ba mu ko defee waa filisti dikkaat , tasaaroo ca xuru refayeen na . |
moo tax erojadd embal ko mer , ba begg koo rey , waaye menu koo def . |
sos mowabeen ni . rakk ja moom it am doom ju goor , tudde ko ben aami mu firi sama doomu mbokk . ben aami moo sos amoneen , ni fi nekk ba tey . |
daawuda nag yebal ay ndawam ca anun , di ko jaal baayam . ba ndawi daawuda ya agsee ca reewum amoneen na , njiiti amoneen na wax ak seen sang anun , ne ko defe nga ne moos wormaal sa baay la daawuda namm , ba yonnee la ay nit nu la jaal ? foogoo ne seetsi dekk bi ak nemmikusi ko , ba song ko moo tax daawuda yebal ay nitam ci yaw ? anun daldi japp niti daawuda na , wat seen genn wallu sikkim , dagg seeni mbubb fa tollook toogukaay ba , daldi leen daq . nu yegge daawuda mbir ma , mu yeble ngir nu gatanduji leen ndax na nu leen torxale . mu ne leen nu toog yeriko , ba seeni sikkim seqaat , nu doora nibbsi . |
seede naa ne , noom ci seen bopp joxe nanu ba fa seen man man yem , ba weesu ko sax . |
ci di leen ne ki dige woon ne dina new , ana mu ? |
yeen asamaan , teewluleen , ma wax , yaw suuf , deglul sama kaddu yii . |
yawut ya wer ko ne ko kan nga nuy dindi ci kumpa ? |
bokk na ci ñim siyaare ci sheexi naar yi ustaas baaba mom hamdi ma jublu ci hamdim ñaareel mi dikk na fa yendu fa fanaan fa nee nan ci menn mbaar |
yeen mbooleem way sàkku yi xam xam déglu leen sama laabiire gii di léen tàqaleek ag texeedi |
li epp ci afrig gu bej saalumu sahara amul woon genn jeflante ak li des ci adduna bi , da noo beru woon . |
wolof mooy lakk wi nu gen a wax ci senegaal , waaye ngir doyodig waa afrig yi ba leegi , franse mii nga xam ne lu matul fukk cib teemeer ci doomi senegaal yi rekk a koy wax moo fiy lakk wu njekk , maanaam wi nguur gi di waxe di ci liggeeye . |
mooy kenn kiy wallu doom aadama yi , di ki sakk asamaan ak suuf , di itam benn yalla bi am . |
omar taal duggu na ay nit yu bari ca biir tariqa tijaaniya . |
lonkoyoonu adduna bi , afritugalasi lanu fesal afritugalasi , ci sewogaraafi ngandam gox la , mooy bi gen a ngande ci adduna bi . |
naan mucc gaa ngi ci yallasunu boroom , bi toog ci gangune mi , ak ci mbote mi ! |
wideyoo kenn meneesuko xool ndax dencukaay bi dafa sankar . |
ndaxte waxoon nanu leen bu yagg te artu leen ne , niy def loolu , boroom bi dina leen mbugal . |
caq baa ngi la koy melaxal melal goo xam ni kenn mënu laa wax ni mu mel melaxa melax ba boo ko tegoon ci àll ba gëna lëndëm sax mu daldi leer |
defkati mbon yaa ngii , daanu , ne lareet , telee jog . |
noonu nit ñëw tuddoon yayrus te nekk njiitu jàngu ba |
yëngu yëngu yi jugoon di safaan di kontar jàngu bu paab bi |
doxal taxawal ab jongrukat , lu mu gis , wax ko . bu gisee gawar ci watiiru naari fas , ak nu wari mbaam ak nu wari gileem , na teewloo teewlu bu baax . |
kon boroom kaso ba yegal loolu pool ne ko attekat ya jox nanu ma ndigal , ngir ma yiwi leen , ngeen dem leegi nag gennleen , te dem ci jamm . |
limu liste tuubaa sampool jaas japp na ne atte bi neel yemale gi d . . |
moona dees na foqati ku jambaar japp , ba reccal alalu sexetoob boroom doole . say jotewaale , maay joteek noom , te say doom , maa leen di wallu . ni lay neewal , maa leen di leel seen suuxu bopp . seen deret ni biin bu bees , ma mandale leen , ba kuy boroom suux xam ne maay aji sax ji lay wallu , jambaaru yanqooba ji lay jot . |
hisaab nag luy tar la ca boobale bis ndax dees na hisaab nit ki ci lu gën a tuuti fepp suuf cib tuutaay |