audio
audioduration (s)
1.18
50.6
sentence
stringlengths
0
418
source
stringclasses
4 values
boobu boo ko laalee ci sa loxo day taq ripp ci sa loxo
kallama
Station shell icotaf
urban_bus
ba mu egsee ñépp wër ko mu ni leen
alffa
budee lu mel ni que business en plan la budee jigéen bi ne nekk membre fapal boo ñëwee daañu la jàppale ba nga am sa business en plan danga am sa plan commercial wala nga am sa plan de sa plan de développement
kallama
amoon na ñu daan gas di ci denc seen alal
alffa
dañuy dem ba mois aôut bi jeex nga buddi yëpp béy jiw su ko defee mu bañ a tawte mais ren jii bañ ko defee ndaox mi boo xoolee macha ar allah ar ñaari taw la ñu am mu arreté kon ndox mi ren demeewul noonu mooy problème bi ren
kallama
toN toN u naat saa yu wëree am réew dunq yaa tax
alffa
bañ loo menul à vañi darà moo k begà ém
alffa
Le Baol
urban_bus
damay wax ni ñëpp d ici 2080 dem 3000 danañu yegg 3000 doomu baykat bu mu fekkoon nga nekk nii dootoo doon baykat ndax dootoo am foo bay
kallama
mu ne du la may doomam ndax géwal nga
alffa
su fekkee ne mu nga fa dinaa ko ko wax
alffa
parce que boo parcourir ree 1 kilomètre boo xam ne amul benn garab
kallama
sedd lañu nekk guddi gi dafay teel a dugg
alffa
Lycee Maurice Delafosse
urban_bus
nan laay def ba dem Boulangerie marché mame Diarra
urban_bus
Elton Ouest Foire
urban_bus
Marché Taly Bu makk
urban_bus
léegi de yaay tegoo njaboot gu sew gi fi sa baay ba
alffa
CEM Hann
urban_bus
parce que moo tax moo tax tey fële nële tey magasin ba amul benn intrant boo xamante ne nii desoon na fa muy intrant di matériel
kallama
Pharmacie Talibou Dabo
urban_bus
su ma sañul xarab it sañ naa gërëm ñi ma daan may
alffa
billet yu bari yuñ jaay ci site en ligne yiy def anchere lu ci melni ebay wala craigslist yooyu ay billet parc-hopper yu xawa yàgg lañu te xaw nañu leen jëfandikoo
fleurs
loolu aussi day gën a dem ba moom rey suufam si
kallama
benn genre ngelaw boo xam ni moom la ñuy wax évapotranspiration
kallama
laaj na nga leeral bu baax sa wax ji nànduma ko bu baax
alffa
ñépp a mën jot ci leeraay mennum mbir mu taxaw ci yoonu jubluwaay mooy sunu taasiyoŋ ak ñakka woolu sunu bopp
fleurs
Pharmacie Ibrahima Niass
urban_bus
te fi mu ne nii la ma leen waxoon rek mooy développement sénégal ci suuf la jugee jëm ci kaw
kallama
donc xamal na leen mbir yi kat nii la demee
kallama
sa mbaal mi jén yu ndaw rekk la mëna jàpp
alffa
elimaan warula def lu nit ñi di àññ
alffa
alal yu baré yaram vu vér à ko gen
alffa
man boog ci man nga xam ni maay yëngu ci wàllu météo
kallama
dafa duggsi rekk ni wàpp ci basaN gi
alffa
booy jëfandiko drone njëkkal saytu li ñula may nga widewo ko ak yan kayit nga wara joxe
fleurs
ku fab téere bi ma tegoon ci taabal ji
alffa
bàyyileen jaabante bi damay fobeere
alffa
baye 1975
kallama
maintenant béykat bi bu organiser maintenant am na lu koy xaar ci waajal nawet kuy waajal nawet maintenant par rapport ak thème bi day taataan xibaaru météo bu ko amee maintenant ci lay mun a appliquer maintenant li ñuy wax les bonnes pratiques agricoles
kallama
bindu bi daal jafewul boo ñëwee daal
kallama
xam nga li ñuy wax rek moom mooy que le changement climatique là nekkatul un slogan
kallama
kil la nekkal bi nga ñàkkee boo amee nekkal ko
alffa
yóbbul sa doom loppitaan moo gën nga naan rab yee ko jàpp
alffa
tam dafa wër àddiina foo dem fekk ko fa
alffa
buy xalangu ci suuf si bàyyi ko di ko seetaan
alffa
dafa dem bay toog ma xëcc siis bi mu detteerlu
alffa
jaxal mbànd mi seet ndax nganj mi ñor na
alffa
mooy la conférence des partis conférence boobu chef d état yi nekk si monde bi yëpp fay daje amul etatunis amul france amul keneen ñëpp a fay daje
kallama
Fass Mbao
urban_bus
njàngale mu xamlewul dara bëgguñu ko
alffa
waa te comme gars yi dañu ñoo jàppale ci suñu béy yëpp nag war nañoo mën di def assurance
kallama
maanaam li siy dëgër ak une phase liquide
kallama
dañoo toppoon mbir mi ci virginia ndax mooy barab bi ki daan joxe sarwiisi internet aol dëkkoon kër gi tambali tuuma yi
fleurs
te am nañu yaakaar ne incha ar allah ar ci alxames bi nit ñiy ñëwee pour visiter yaakaar naa ni du ñu am gànce ci programme boobu parce que def nañ fa vraiment lu ñu mën a wane
kallama
bu dee nit ki amul information da ngay gis ne day toog rek
kallama
Cem pikine Taly bou bess
urban_bus
bantu ron dëgër na moom lañuy liggéeye lal yi
alffa
on est resté quatre ans sans véhicule léegi la ñuy doog a jot benn mais vraiment dans un état vraiment
kallama
Tigo Almadies
urban_bus
xam nga xéll ne ñetti nit xajuñu ci pajaas bi
alffa
kon su fekkee ne dañu am projet mu bugg a liggéey si suuf war nañ mën a am sañsañu laaj suuf
kallama
Parc Forestier de Hann
urban_bus
message bi nga xam ne moom la ñu leen di yox
kallama
dañuy fexe ba amaat bu ñu amaat bu ñu amaatee pré base wala base ñu jox ko ñee bu fekkee am nañu ay pré base ñu jox ko ñu ñu fexe mu xool ba xam nu ñuy xaajalee juróombenn juróombenn ñu jox ñii base base jox ñii pré base comme ça ñu gën a ful
kallama
Cité Police
urban_bus
duma bëgg lu la neex ba ne la yàllaa ngi lay nuyu
alffa
déglul ndox miy xéréréri ci mbalka mil
alffa
askan wi gën a dégg ndax léegiléeg dégguma dafay bëri te ñu taamu si nag bés bi nga xam ne bésu àllarba la muy bésu luuma ndaje fi di fi am mu nekk bés boo xam ne nag demlanteeg dikklante la journée d échange la
kallama
sunu dawkat yeey joN ante ak yu marok
alffa
dégg naa ne omar dafay ngoro ak astu
alffa
Cité Douane Golf Sud Océan
urban_bus
Pamecas Cheikh wade
urban_bus
ay xalaat yu ni mél ñoo ngi jeem ci gëstu lan mooy séwlo nit yi wala dilén wo
fleurs
Tally bou bess Parcelle
urban_bus
làkk yuñ ci dolli are làkk yu artifisiyel lañu yuñu sos ci ndorteel bi ngir yombal waxtaan ci digante yi am ay jafe-jafe waxtaan
fleurs
wolof njaay nee ganaar wéete wolandoo gëse benn tànk
alffa
kafe mooy porodiwi buñuy gëna jaay ci addina bi te mën ngeen gis ay xeet yu bari ci diiwaan bi ngeen bawoo
fleurs
silaama sii ci cosaanu dëkk bi la bokk
alffa
ba jot ci li nga xam ne moom mooy financement yi
kallama
mën nañu ni pulaar la gën a dégg soose bi mu nàmp
alffa
Imprimerie Tandjan
urban_bus
ngàngooru jant bi rekk doy na kéemaan
alffa
puudar boobu nag ci lañ ñu mën a dimbalee moom nañu ñu ci dimbali kooku li muy wax noonu rafetlu naa ko lool
kallama
Mosquée Daroukhane
urban_bus
Palais Presidentiel
urban_bus
saako boo xam ni daal mos naay duy dara bàyyi ko teg ko nële ma leen siy jox benn exemple rek gisagu len fenn fu ñuy dem di jëndee saako ceeb ngeen gis ceeb bi ñu ne saako bi defoon na defaat mosul am
kallama
mooy gën a baax neefere nag boo xam ne ci niimaa lay dund wala ci leneen loo xam ne si xëy na pouvoir am ci wàllu fertilité demeewul noonu
kallama
ci yow naka la mëna dunde ak lu tuut li muy am
alffa
ñii fàlu nañu buur ñii doomi buur lañu di ay garmi
alffa
Mbédou Fass
urban_bus
te su ñu béyoon tey ba am lu ñu dundee yaakaar naa dañuy xeex insécurité alimentaire parce que xiif dootul am ndóol dootul am njàngu xale yi dina mën a réussir
kallama
ci ndorteelu xare bi dañoo tukki jaar ci kaw géeej gi lu bare wante ba radar yi dooree di yokku te di gëna xarañ
fleurs
di jaajëfalaat nag suñu dg di ko daal di jox rek sunu nuyoo moom itamit mu daal di koy jagleel képp kuy yeewoo ci rajo ndefleng fm fatick ñu ngi lay tàllal sunu loxo di la naan asalaamaaleykum waaye tamit di nuyu suñu mbokki auditeurs auditrices 93 point 5
kallama
daal heure bu ñu amee ay demandeurs danañ fexe génn commune bi pour demsi yeneen communes yi
kallama
Hopital de Fann
urban_bus
magantewuñu lu bare seen yaay dafay nef
alffa
bu ñëwee ci moo yow da nga koy diagnostiqué ba pare
kallama
te tey ni ñu def ba mu jot si suuf bi moom war na ko def ba ay doomam jot si suuf mais su fekkente ne danga bëgg a encouragé xale yi nañ fexe ba suñ leen bayloowee au moins nga bayal ko tool moom tamit mu am tool bu mu bay
kallama

Wolof Audio Dataset

The Wolof Audio Dataset is a collection of audio recordings and their corresponding transcriptions in Wolof. This dataset is designed to support the development of Automatic Speech Recognition (ASR) models for the Wolof language. It was created by combining four existing datasets:

Features

  • audio: An audio file containing speech in Wolof.
    • Format: Varies (e.g., WAV, MP3)
    • Sampling Rate: 16 kHz
  • sentence: The textual transcription of the audio in Wolof.
  • source: The origin of the example, either 'alffa', 'fleurs', 'urban_bus', or 'kallama'

Dataset Structure

Splits

The dataset is divided into two splits:

Split Number of Examples
Train 28,807
Test 6,268

Usage Example

Here's how to load and use this dataset with the 🤗 Datasets library:

from datasets import load_dataset

# Load the dataset
dataset = load_dataset("galsenai/wolof-audio-data")

# Access an example from the 'train' split
print(dataset['train'][0])

# Expected output:
# {
#   'audio': {
#     'path': '.../train/audio/<audio_file>',
#     'array': array([...]),
#     'sampling_rate': 16000
#   },
#   'sentence': 'Transcription of the audio in Wolof',
#   'source': 'alffa'  # or 'fleurs' or 'urban_bus' or 'kallama'
# }
Downloads last month
79