audio
audioduration (s)
2.29
12.5
transcription
stringlengths
26
118
sunu meetar ñówul tànkam dafa faxaj
Nanga ma ko fàttali lu ko moy dinaa ko fàtte
am na ñax mu nu daan foye xuusmaañàpp
maamam a daan tëgg laxaab yi ca dëkk ba
benn seex bi gàjj bi ci lex bi laa koy xàmmee
bu nawet jotee xay yi dañuy fees ak ay busëbaali
dafa ne yoxoos dugg defe ne gisuma ko
dinga yaakaar nit fekk mënul faj sa soxla
booy seppi nanga fexe ba rënd bi bañ a tas
sa jabar a ngi ci waaN waaN ji léegi mu wasin
ce ngoon sa ba yumaane liggéeyee ba sotaal mu woo ko ni ko
fanweeri dërëm laa ko jox mu delloo ma ñaari dërëm
armeeli katolig yi ak yu jullit yee dend
li ngay digle soo ko doon topp kenn du la gën
jongama yaa ngi toog géwél bi di leen xalamal
di dowal di dowal ba gëna dugg ci biir àll bi
dowleen gaaw ñu pikkiir ko bala daNar wi di yéeg
ba mu taxawee mu dem waaf ci genn ronu ngeer
bu xale yi ñówee nga nàkk jox leen ko
xam nga xéll ne ñetti nit xajuñu ci pajaas bi
toN naat bu wëree am réew dunq yaa tax
yoonam wi neex na indaale na bagaas yu bare
xaj bi am na lu ko jot mu ngiy yullul rekk
alkaati yi tàmbali nañu xàll léegi kilifa gi ñów
yàlla miy far baakaari àddina si yërëm nu
yàkkamti woon naa ñibbisi ba lat ci pajaas bi
ñoom ñaar amareeg sàmba àgsi ci kër buur bi
senegaal dafay jaay ariko bitim réew
xel mi nga gase teen bi la ci keneen di naane
yàkkamti woon naa simmi palto bi maaxàllaa dafa tàng
piis bu tal bii du neex a sol ci tàngaay bi
mbetteel gee ko jàpp ba mu toog ab diir bu mu waxul
jotali ma njegenaay ma noppalu ci ndes mi
lellil fi wextan wi laal ci tëll bi
gunóor gi gas na bant bi ba mu wale
booy fóot jëlal ndox mi ci póll gi
bër set mu daldi fàqlu lu dooni yari daqaar laxasante ko
séytaane teg ko ca jombaxtalu tangor ba
dama la doon seetlu ba xam ndax sama xarit nga
ñépp daldi jog tàccu yi dal coow li ak pënd mi jolli
su janax di sóoru muus ñag baa fa jege
bett nga ma lool foogoon naa ni dinga sàmm sa kàddu
paske feebar yii fi nekk leegi xamuñu ko woon
sëf ñaari nag ñeenti xar def jiwoom ba mu doy mu ñów
ba nga xamee né xare bi jeex na tàkk mu wéy ca ña ca des
yéesu dafa suufeelu ba di raxas tànki taalibeem
sa kanamu alkaati bee tax mu ragal la
bu jëkk jigéen ñi dañu daan ñuulal yoos mi di ko léttoo
loolu de soo ko defee féewale say jabar
jaruloon ngay lump sa banaana maa la ëpple
ab dànnala la woon waaye bët yi neexatul
metitlu na li nga ko yégalul takk gi
omar mën na la dimbali ci saayir ak ci baatin
dég dég amul i tànk waaye jàll na am ndox
dafa bëgga dugg te bunt bi dafa téje
am réew su fa lingeer dee fecc ku fay woyaan doo rusa yaN as
baana baana yi ñoo daane njaayum naari bayruut yi
ceglar daldi toog ci kow lal bi ni joor
jox ma njàmpe li ma ragg samay tànk
tërëx piccu ndox la waaalo waalo yi xam nañu ko
dañu gas reen yi ba garab gi wëngéeñu
karawan sëqul noonu waaye dafa gudd coleet
luxuskat bi jommal na seetaankat yépp
kàngamloo ma gënal ku ma dàq yóbbu ma nduluñ
xale bi bég lool ni ko yow yaay sama yaay
fas wi moom ci boppam dafa mel ni laalatul suuf
dégg naa ne omar dafay ngoro ak astu
booy jàngale nangay faral a misaal
léeb wi ab liir la woon buy saga juddu
bëggoon naa jaar sa kër waaye ma naaje yem màrse
kaay dimmali ma ma randal waxande wi
bul ñormati mburu mi dog ko benn yoon
am naa beneen xiseb li nga ma nettali
ku teb dal ca safara désé nà bénén tebin
mu dal di ne jinax ja yalax ci seen biir
walisu laytaay yii turandoo liir bee ko joxe
ba màndikat ba daanoo ndaw si dafa ree ba kekku
ba ma ko sangee ca tabaski daaw ja mbubbu mbaseñ la ma mayoon
bu seen pexe soti woon tey duñu fallu
mbër maa ngi ci diggu géew bi suq yi dar ko
wàññil xal yi lu ko moy jén yi dar
xéy na bu takkee jabar dootul xaaraan
ndimo lu xonq la sol dinga ko gaaw a gis
ndegam sa doom sëppéen la simis bi dana ko war a jot
yaay daal nit a ngi xeeñ ci néeg bi
fu mbott tarxiis ba damm bu fa giléem jaaree wara def ndànk
ndey ja wasin mu yobbul ko butiiti sikket
njureel sagu bépp jigéen juy séy la
Nanguwul lekk dafa coppati rekk ci yàpp wi
puju néeg dina xeex ak taw te borom néeg du yég
lérén dina fànqal liir yaram wu ñaawlu
fàkk naa yoon wi ba amatul benn gàllankoor
jottali ma boppu jén boobu ma maccaat
boo jëndul bul nappaaje sama njaay mi
am na fi ba tey géwél yu la mëna nettali cosaanu
xamoon ngeen bu baax ne àttanul biib liggéey
tuub bi dey jaru ko sax nde waay si saay saay la
mbaam xuux bañul dara loo ko jox mu lekk
wool waxambaane yi ñu déqati bi ñu samp ci gannaaw
géej gaa ngi ne màww ci suñu kanam
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
31