audio
audioduration (s)
0.25
212
transcription
stringlengths
3
600
%e asalaamaleykum %e tey jii sunu waxtaan bi nga xam ne %e waa projet 4R ñoo ko jagleel askan wi [r] jagleel ko tamit ñi nga xam ne [r] %e rawatina ñooy sàmmkat yi béykat yi [r] maanaam producteurs yi [r] te %e lëkkaloo ak Tamba FM RTS sunu juróom-benneelu émission [r] si wàllu projet 4R ñëw na fii ci Sinthiou Malem [r]
%e tey nag %e li ñu taamu waxtaan ak yéen si maanaam juróom-benneel émission bi [r] mooy [r] importance de la pérénisation de service climatique
mooy solo solo bi nga xam ne moo nekk ci biir liggéey [r] fexe ngir maanaam soxal te tamit %e yaatal [r] li nga xam ne mooy %e service climatique [r]
%e tey nag %e di am mbégte [r] ndaxte tamit am nañ fi [r] sunuy mbokk yi nga xam ne [b] %e ñoom %e ñooy tëral maanaam émission bi [r]
kon nag %e di sant bu baax Bachir Mbow [r] ki nga xam ne %e ñoo bokkoon émissions yi weesu mooy chef de service ANACIM [r] tambacounda sezrvice bi nga xam ne mooy toppatoo lépp luy %e maanaam service météo [r]
%e ñu ngi ak %e Awa Ndao [r] Awa Ndao sunu jigéen bu baax bi nekk tamit maanaam waay xarala ci wàllu %e conseil rural di animatrice si projet 4R [r]
fatou sow di relai si projet 4R fii si Sinthiou Malem ak Momadou Sow [r] di relai maanaam principal relai principal fii si Sinthiou Malem [r] Goundou diallo moom tamit di relai [r] ca Manini Diakha ci wàllu projet 4R [r]
ak sunu xarit Momadou Dieng Diallo moom tamit waay xarala [r] nekk personne ressource ak ki nga xam ne mooy [r] Lamine Waly di relai relai %e projet 4 Sinthiou Damba [r] ak ki nga xam ne mooy Souleymane Balde [r] projet ANCAR
kon nag Bachir Mbow
%e daan na sunu émission bi ñaari xaaj la [r] %e xaaj bu njëkk bi %e dañ la koy jagleel ndax tamit %e yow yaa ñuy fàttali li nga xam ne [r] %e moo ëmb [r] information climatique njëriñam [r]
kon nag bachir Mbow [r] li ñuy laaj rek mooy %e maanaam [r] gannaaw bi ñu defee maanaam présentation yi [r] nga wax ñu li nga xam ne [r] changement climatique lan la ëmb
waxoon nañ ko [r] baamtu ko xëy na fii tamit occasion la comme que c' est la prem() la première émission [r] presque publique [r] en dehors du studio [r] nga fàttaliñu ñu xam ne lan moo lan moo ëmb ci changement climatique inforation climatique
maa ngi %e nuyu ñëpp kenn ku si nekk si turamak santam
%hum
di rafetlu bu baax %e daje bi ñu daje fii %e énu war a wëyal suñu ay series émission comme Dia ni nga ko waxee
léegi nag tey dañuy ñëw ba tey encore énu baamtuwaat ko ci li nga xam ni mooy %e wàllu changement climatique
changement climatique nag
bëri na niñ koy waxñoo ngi koy wax fu ne
te kenn ku ci nekk fii am na loo xam ne mën na ko ci indi
maanaam am na loo xam ne daan nga ko dund ay temps ci jamono ci wàllum climat bi ci taw bi ci ngelaw yi ci dënnu ci yooyu yëpp te léegi nga gis ni ni mu mleloon melatu ko noonu ndax changement climatique dafa di loo xam ne lu am la kenn weranteetu ko
waaye changement climatique si boppam
mooy lan mooy question bi [conv] mooy lan si boppam
boo ko seetee
%e asamaan si si kaw jaww jici atmosphère bi dafa am ay gaz yu fa nekk
mooy ñu leen di woowee gaz à effet de serre
léegi gaz yooyu fa nekk
gaz yooyu seen liggéey mooy téye tàngaay bi si biir adduna
ndax gaz yooyu bu fekkente ni nekkul woon foofu bëccëg bi dafa doon tàng ndax naaj bi bu guddi wee day sedd bay bay bay glace gaz yooyu bu fa nekkul woon
loolu moo naroon am ci adduna
maanaam bëccëg
mu tàng guddi mu liw mu sedd
bay indi glace
te xam nga loolu
%hum
loolu dund munu ci nekk
dund munul am ci loolu
%hum
bëccëg nga tàng dem ba quarante degré fu ci mel ni fii ay Tamba
%hum
guddi gi mu sedd dem ba moins quinze degré bay commencé glace
%hum
loolu su doon loolu moo doon am dund du mën a am ci kaw suuf
su boobaa ndax moo ñuy may [b] ba ñu mën a dund ci kaw suuf léegi nag problème bi yëpp mooy gaz à effet de serre yooyu nga xam ni seen liggéey mooy téye tàngaay bi si adduna bi dafa dem ba léegi dafa yokk
%hum
léegi bu yokku wee li nga ci mën a xam mooy
kon su boobaa li mu nar a téye si tàngaay
dafay gën a bëri loolu nag moo ñu dal
jamono jii te loolu li ko sabab li tax %e gaz à effet de serre yi yokku ba muy gën di téye tàngaay li ko sabab mooy li ñu woowee industrialisation
depuis les années soixante bi tubaab yi commencé créer [bb] ay machines di créer ay usines ay oto
ay moto tey jii moto bi bu tàkkee dina am loo xam ne mooy génn
ci échapement bi loolu fumée fumée yooyu yëpp
juge ci usines yi juge ci oto yi yooyu yëpp [b] mooy dem
ba yokk gaz effet de serre yi nekk gaz yi nga xam ne moo nekk ci kaw te ñu koy wax gaz effet de serre
day dem ba foofu yokk kolooloo tax ba léegi gaz yooyu li mu doon téye si tàngaay
%hum
léegi daf koy gën a téye loolu nag conséquences yi mu indi mooy tàngaayu adduna bi dafa yokk
tàngaayu adduna bi dafa yokk tàngaay adduna bi comme yokk na
am na yeneen yoo xam ni dafa am ay impact waaw dafa am ay impact
defe naa léegi loolu dinañ ci ñëw ci ci ci yeneen questions
ci wér-gu-yaram ci yooyu yëpp
am na loo xam ni
indi na ko ci
donc loolu
boo ko déggee rek
explication boobu
mooy mooy ci tënk mooy loolu la ñuy woowee changement climatique ci tënk loolu mooy ci boppam changement climatique
waa
aywa
kon nag %e Bachir Mbow [r] su loolu weesoo lan mooy maanaam njeexital mooy effet changement climatiques yi [r] ci wàllu maanaam mbéy mi càmm gi mooy les activités agricoles
%hum %hum [b]
waaw [b] donc ginnaaw bi ñu expliqué li nga xam ni mooy changement climatique
am na ay effets ay impacts [b] yoo xam ni lu si ëpp ay impacts négatifs la
boo boo jëlee wàllum agriculture
wax nañ ko sax ñëpp seetlu nañ ni
ni mu doon tawee jamono bu njëkk ba tawee tu ko noonu taw yi nga xam ni moom la ñu woyee %e pluie extrème mooy taw yoo xam day jékki-jékki rek
taw taw bu fort bu bëri
te taw yooyu ñëpp xam nañ ne taw yooyu gënul
%hum
ci agriculture
saisons yi léegi
ñëpp gis nañu saison yi léegi ni mu mel
ren fii Tambacounda dem nañ ba novembre weeru novembre bi ñu nekk nii
muy continuer di taw
début nawet bi
ni mu meloon
melatu ko noonu
jamono bu njëkk ba mois de mais
mu commencé taw
juin nga commencé def say ji ak yooyu
waaye léegiren surtout dem nañ ba weeru août am na ñoo xam ne weeru août la ñu commencé ji seen i gerte
weeru août la ñu soog a commencé ji seen gerte donc lu tax parce que saison bi léegi dafa bougé
dafa am ay changement yenn saa yi mu teel a commencé
yenn saa yi mu naaj mu naa() %e mu mu mu mu mu bañ a teel a commencé
mu teel a jeex mu kii donc cycle bi
waaw donc loolu mooy impact yi nga xam ni vraiment
affecté na directement wàllum agriculture yi
léegi nag blan mooy taxawaayu maanaam producteur bi mbéykat bi sàmmkat bi ñoom seen
%e ci wàllu changement climatique taxawaayam moom
waaw taxawaayam maanaam ki nga xam ni activité agricole lay def lenn nga xam lenn rek moo fi nekk
%hum
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
36