|
sentence: Ngir jox leen ci misaal , damay sukkandiku ci sama jaar - jaar ca ENA . ENA <person> |
|
sentence: Ku am signature ” bu baax , du ni faral leen ma bor bi . |
|
sentence: Waaye , Yàlla am na ci nit ñi yërmande joo xam ne , fépp fu mu boole ay nit yu wute ci waaso , dina fa tàggat aw làmmiñ wu leen di boole , ñu cay jokkoo . |
|
sentence: Topp ma , dinga ci xam dara 👊 🏿 ! |
|
sentence: Waaye , ma y dox di seetlu , di jàng lu bari . |
|
sentence: Turki , ñoomit , ca nguurug Otomaan ga woon lañuy wéru . Turki <organization> Otomaan <organization> |
|
sentence: Waaye , Mabaaba , ak lu mu doon mbër mu mag yépp , amul ndam ci xeexam bu mujj bi mu séqaloon ak meneen mbër mu xarañ te gaaw ci rey nit . |
|
sentence: Wolof : àbb na ko ay waat yu bari lim ba a leerul . 🤩 |
|
sentence: Siin moo nu ëpp ay kàllaama fuuf , 300i daanaka . Siin <organization> |
|
sentence: Li koy firndeel mooy , ci bés bu jëk k bi dañu duma gaa yi bu baax , ca ëllëg sa , gisuma sax muus m uy taxawaalu . |
|
sentence: Mën nañ ko bañ a wax waaye dégg nañ ko , te loo ci wax xam nañ ko . |
|
sentence: Am réew , boo b ë ggee xam nu ëllëgam nar a deme , natt ko ci ni muy saytoo ay doomam , jigéen ña ak néew - doole ya . |
|
sentence: Làkku Góol : 147i waat . Góol <organization> |
|
sentence: Xam naa , moo tax mu ni leen nañ tiital gaa ñi ngir ñu bañ a génn . |
|
sentence: Waaye , ni may kàdduy Séex Anta J ó ob di dugge , li miy def ci man , keneen defu ko ci man ci ñ i ma jot a jàng seen i téere . Anta <person> J <person> ó <person> ob <person> |
|
sentence: Mel na ni yow ci s a bopp dundoon nga lu xaw a niro ok lii ? |
|
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin . Pópangin <organization> |
|
sentence: Loolu , nguur guy xaru rekk a koy def . |
|
sentence: Ci farañse : |
|
sentence: Naam , am na loo xam ni mën ko jéggaani waaye fexeel ba li nga moom nga yor ko yorin wu rafet , bañ koo sàggane , bañ koo waanteer . |
|
sentence: Yaa nekkoon sama njiit . |
|
sentence: B ala may bëgg dee ñu naan dañoo am signature ” bu baax . |
|
sentence: Ca mujjantal ga , yoon jox na ma dëgg , daan sàndarma ya fa demoon . |
|
sentence: Waaye , dañuy dàq nit ba ci biir kër am . |
|
sentence: Sumay wax aada , xam - xam , cosaan ak sag yi m u là mboo ma tax di wax . |
|
sentence: Bu dee réew yépp ay leb tamit , ñaar a ngii : Lebu Sapo ŋ bokkul ak bu Liba ŋ , ñaari réew yi ëpp aley bor ci àddina si . Sapo <organization> ŋ <location> Liba <organization> ŋ <location> |
|
sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole . |
|
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi . |
|
sentence: Warees na ko o joyyanti ba jub a le leen , ñu doon benn . |
|
sentence: Kon , koo jël ci àddina si , ci démbam la sukkandiku ngir jéem a suuxat réewam . |
|
sentence: Jean - Michel Aulas Njiitu Olympique Lyonnais . Aulas <person> Olympique <person> Lyonnais <organization> |
|
sentence: Yenn saa yi ma daje ak ñenn ci ñoom , nu lal aw waxtaan . |
|
|