File size: 3,011 Bytes
868d802
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
sentence: Ngir jox leen ci misaal , damay sukkandiku ci sama jaar - jaar ca ENA .	ENA <person>
sentence: Ku am signature ” bu baax , du ni faral leen ma bor bi .	
sentence: Waaye , Yàlla am na ci nit ñi yërmande joo xam ne , fépp fu mu boole ay nit yu wute ci waaso , dina fa tàggat aw làmmiñ wu leen di boole , ñu cay jokkoo .	
sentence: Topp ma , dinga ci xam dara 👊 🏿 !	
sentence: Waaye , ma y dox di seetlu , di jàng lu bari .	
sentence: Turki , ñoomit , ca nguurug Otomaan ga woon lañuy wéru .	Turki <organization> Otomaan <organization>
sentence: Waaye , Mabaaba , ak lu mu doon mbër mu mag yépp , amul ndam ci xeexam bu mujj bi mu séqaloon ak meneen mbër mu xarañ te gaaw ci rey nit .	
sentence: Wolof : àbb na ko ay waat yu bari lim ba a leerul . 🤩	
sentence: Siin moo nu ëpp ay kàllaama fuuf , 300i daanaka .	Siin <organization>
sentence: Li koy firndeel mooy , ci bés bu jëk k bi dañu duma gaa yi bu baax , ca ëllëg sa , gisuma sax muus m uy taxawaalu .	
sentence: Mën nañ ko bañ a wax waaye dégg nañ ko , te loo ci wax xam nañ ko .	
sentence: Am réew , boo b ë ggee xam nu ëllëgam nar a deme , natt ko ci ni muy saytoo ay doomam , jigéen ña ak néew - doole ya .	
sentence: Làkku Góol : 147i waat .	Góol <organization>
sentence: Xam naa , moo tax mu ni leen nañ tiital gaa ñi ngir ñu bañ a génn .	
sentence: Waaye , ni may kàdduy Séex Anta J ó ob di dugge , li miy def ci man , keneen defu ko ci man ci ñ i ma jot a jàng seen i téere .	Anta <person> J <person> ó <person> ob <person>
sentence: Mel na ni yow ci s a bopp dundoon nga lu xaw a niro ok lii ?	
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin .	Pópangin <organization>
sentence: Loolu , nguur guy xaru rekk a koy def .	
sentence: Ci farañse :	
sentence: Naam , am na loo xam ni mën ko jéggaani waaye fexeel ba li nga moom nga yor ko yorin wu rafet , bañ koo sàggane , bañ koo waanteer .	
sentence: Yaa nekkoon sama njiit .	
sentence: B ala may bëgg dee ñu naan dañoo am signature ” bu baax .	
sentence: Ca mujjantal ga , yoon jox na ma dëgg , daan sàndarma ya fa demoon .	
sentence: Waaye , dañuy dàq nit ba ci biir kër am .	
sentence: Sumay wax aada , xam - xam , cosaan ak sag yi m u là mboo ma tax di wax .	
sentence: Bu dee réew yépp ay leb tamit , ñaar a ngii : Lebu Sapo ŋ bokkul ak bu Liba ŋ , ñaari réew yi ëpp aley bor ci àddina si .	Sapo <organization> ŋ <location> Liba <organization> ŋ <location>
sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole .	
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi .	
sentence: Warees na ko o joyyanti ba jub a le leen , ñu doon benn .	
sentence: Kon , koo jël ci àddina si , ci démbam la sukkandiku ngir jéem a suuxat réewam .	
sentence: Jean - Michel Aulas Njiitu Olympique Lyonnais .	Aulas <person> Olympique <person> Lyonnais <organization>
sentence: Yenn saa yi ma daje ak ñenn ci ñoom , nu lal aw waxtaan .