audio
audioduration (s) 1.22
171
| text
stringlengths 6
108
|
---|---|
gisiin wu yaa wi |
|
nekk naa itam liggéeykat. |
|
tey, ak xool bu tooy laa lay tàggoo |
|
fan lay tëdd ? |
|
danoo nekk ci kaarànge bés-niki-tey ci dal. |
|
di daw di waaxu fune ñu wër |
|
lu tax ma war caa dem ? |
|
genn mbaalug laabal ci tuubaa gu toll ci 18 km |
|
seneweb news, la mbind mi jóge |
|
danga waroon a gise ak moom. |
|
defaral na ma ay mbiskit. |
|
éybaar 3-1 reyaal wayaadolit |
|
maa ngi nelaw ba leegi. |
|
kaay ànd ak man fim toll nii. |
|
gaaw a gën ci yaw de. |
|
aka ñoo fo ! |
|
mi ngi fomp ab wataam. |
|
wuññi woon nañu lëndëm-lëndëmi gox yi ci xam-xam ak jëf ak dëppoo. |
|
nànd na ko. |
|
libeeria bokkeef bu libeeria réewum afrig. |
|
ndax prefe dinay faral di leen nangul seen i taxawaayu ñaxtu ? |
|
buwaasoo yi maa ko moom. |
|
woyal ab woy waay. |
|
jélliwu ma tus. |
|
yal na la yàlla sàmm ! |
|
ci yaw la ñu yaakaar. |
|
da noo bég lool. |
|
dafa damm ? |
|
daa mel ni dama koo xam. |
|
bul laal sama wata! |
|
nii nag la itaali doone woon benn, muy lol ay doomam a ko xeex |
|
tëj wunti jaanama keroog ba yépp giim |
|
man na noo jéem. |
|
mu dakkalul di jooy. |
|
jangoroy yaram-wu-tàng ju ebola ñoo ngi ko njëkkeen gis ca sudaan ak ca kongóo |
|
tom daaldi koy taxaw loo. |
|
man maay ki wopp lool. |
|
sama muus dafa weex. |
|
nan nga def tay? |
|
damaa mujj fenaat yoon bii. |
|
dàngin golo gu mag, rab la ci rabi àll yi |
|
mbirum jumaa yi ak jàkka yi tamit, noonu la deme |
|
dafay soog a door. |
|
nees ko baaxoo màggale |
|
moo nu xetali woon nun ñépp. |
|
feeñug xeeti orob yu yees yi |
|
kenn manu noo dégg . |
|
noppi ngir dem a? |
|
mantaalis garab la gog ay xobam |
|
fu yaatu laa soxla. |
|
ca amerig |
|
sun saxaar gi daa yeex a egsi. |
|
yéen a ngi reetaan bu baax, yéen góor ñi. |
|
ubbi naa bunt bi. |
|
ki rëy aw làmmiñ |
|
bu leen jaaxle ci moom. |
|
xaajumaa wóolu maf |
|
nan la nu gisee? |
|
am naa rafet njort ne tom a ngi fu wóor. |
|
sopp naa sa kawar gi. |
|
añs ak ñoom seen |
|
topp wëtiir ba moom du xëx |
|
bégoon na lool |
|
dama leen musal. |
|
sëñ saaliwu njaay ci leeral ug waat yi. |
|
bëgg nga xaj yi ? |
|
dànkaafu woon naa la. |
|
dàqoon na ma ak xel. |
|
sotti na, kon. |
|
jàmm ak salaam ñeel na la |
|
dafa xayadi lool! |
|
day wuute ci xeet yi |
|
xool ko ! |
|
duma leen bàyyi ngeen di dee. |
|
bul ñàkk xorom. |
|
jooy na jooyi mbégte. |
|
làjj nga benn liggéey. |
|
toppleen wata bii ! |
|
maa ngi nuyu waa kippaango |
|
europe moo ëppoon ay nit yu xaru ci ay gox ci atum 2015 |
|
aamiin aamiin ? |
|
li afrig soxla mooy politik bu dëppook ay soxlaam ak njëriñam ci wàllu koppar. |
|
jege tàbbi dem |
|
amatuñu benn gis-gis ngir bennoog afrig. |
|
maam jaara sëy |
|
joor ko ci kàmb gi |
|
jataayub ndénkaan yi |
|
waaye, demewu fa noonu. |
|
mën nanoo lijjanti loolu a ? |
|
li xew tay 28i maars 2020 |
|
tom ku néeg la . |
|
damaa am ay gëm-gëm. |
|
ay doomam njokkub lujum lay doon. |
|
kenn du xam. |
|
làkki xeet yu orob yi, ñi ngi sosoo ci màbbiiti latin ak tiyotin |
|
bénteñe doŋŋ du ker, waaye moom lañu taamu. |
|
nekk naa itam jkat. |
|
dama man féey. |
|
barabi mbatiit yi les sites culturels |
|
lëlëg s suba s le matin |