|
sentence: Fii ci Senegaal , fépp foo dem , dégg nañ wolof . Senegaal <organization> |
|
sentence: Yaakaar naa ne mébétam moomu du sotti . |
|
sentence: Maa ngi metitlu xibaar boobu , di ko jaale njabootam gépp ak ay jegeñaaleem . |
|
sentence: Sa dem bi dafa teel . |
|
sentence: Ndaxte , ku xam ni pólis di doxe , nga gis ab alkaat i bu nekk ci biir màkkaanam sañ a def widewoo , yor i liif di tëkku askan wi , di ko dig ay dóor … ñàkkul mu am luñ ko sant . |
|
sentence: Mbokk mbaa xam nga ne làkku farañse mi nga naw lool ba mu tax la a xeeb saw làkk , ni làkk yépp ay waat yu ñu àbb te dajale dong la 😌 ? ? ? |
|
sentence: Paap Juuf ku dëggu la woon , bëggoon ñépp , yemale ñépp te bokkoon leen njaboote . Juuf <person> |
|
sentence: Yorees na leen yorin wu rafet . |
|
sentence: Doyoon na rekk sànni ay gërënaad lakkiromosen . |
|
sentence: Li mu defalul daara yi , nag , moo tax amul màqaama wax ci ñoom . |
|
sentence: Waaye , nag , du lépp a bon ci daara yi . |
|
sentence: Iraŋ , bu àddina sépp waxee mu téye fi mu téye rekk , ñemee ŋoy fi mu ŋoy , booba cëslaayu aadaam a ko ko may . Iraŋ <organization> |
|
sentence: Ndege , baat yiñ lay tàmmal ca daara ja , méngoowul ak li ngay dund , di ko gis bés bu nekk . |
|
sentence: Bu dee lu jëm ci mbirum njàng mi , bun demoon ba sàrtal njàngum làmmiñi réew mi ci lekkool yi , wolof mooy doon làmmiñuw bennale wi . |
|
sentence: ( ÑAAREELU XAAJ BI FEEK I FAN ) FEEK <location> |
|
sentence: Am réew dafa am lu mu moomal boppam , am lu ko Yàlla wërsëgalee . |
|
sentence: Senegaal , moom , mooy réew moo xam ne , ku ñaawtéef laalul , danga nga naan sama yoon nekku ci . Senegaal <organization> |
|
sentence: Li jiitu ci sama wax , mooy ne dama y gërëm , di sargal ak di delloo njukkal takk - der yi . |
|
sentence: Bismillaah , ci turu Yàlla , ma tàmbali . |
|
sentence: Xamal ni bëgg naa la ba fàww te dootuma la fàtte . |
|
sentence: Niral : internet , taylorisation , … 😲 |
|
sentence: Luy sa naal ñeel aada ak cosaan ? |
|
sentence: Turki , ñoomit , ca nguurug Otomaan ga woon lañuy wéru . Turki <organization> Otomaan <organization> |
|
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin . Pópangin <organization> |
|
sentence: Waaye , ni may kàdduy Séex Anta J ó ob di dugge , li miy def ci man , keneen defu ko ci man ci ñ i ma jot a jàng seen i téere . Anta <person> J <person> ó <person> ob <person> |
|
sentence: Moo tax Maki Sàll sonn ci nañ far bor bi . Sàll <person> |
|
sentence: Xamul woon xàjj - ak - seen te bëggul woon lu jege sax boddekonte , rawatina ñeel nit ku ñuul . |
|
sentence: Nekkinu askanu Marseille ak àqi nit ku ñuul bokkoon nañ ci yi soxal bu baax a baax Mabaaba . Marseille <organization> |
|
sentence: Nguur yi fi jot a jaar yépp , lajj nañ ci caytug fànn boobule . |
|
sentence: Ndaxte , mbejum kanam , boroom a koy fajal boppam . |
|
sentence: Warees na ko o joyyanti ba jub a le leen , ñu doon benn . |
|
sentence: Bi loolu amee , dama jël ab layookat , topp mbir mi ba mu sës . |
|
|