File size: 2,887 Bytes
868d802
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
sentence: Ndege , ci atum 2014 , ci wutaakon yi doon sàkku Meeri Marseille bi la bokkoon .	atum <location> Marseille <organization>
sentence: Loolu nag , baaxul , day féewale pólis bi ak askan wi .	
sentence: Duma def lu dul dellooti mbirum taalibe yi ci loxo doxalinu nguur gi .	
sentence: Léegi leer na ni peterool ak gaas kenn du ko jariñoo 2023 te sàggane nga li nga moomal sa bopp .	2023 <location>
sentence: Paap mujje naa am ndam ci xeex boobu .	
sentence: Ndaxte askanuw Senegaal dafa ragal yat .	Senegaal <organization>
sentence: Ñoom , ca nguurug Pers ga woon lañuy sukkandiku fonk seen bopp .	Pers <organization>
sentence: 😌 🤝 🏿 - Toppaat ma ma xamal la làkk yi farañse àbb ak limu waat yi mu leen àbb .	
sentence: Ndax bàyyees na xel ci seen wér - gi - yaram ?	
sentence: Loolu metti na .	
sentence: B ala may bëgg dee ñu naan dañoo am signature ” bu baax .	
sentence: Li ngay jëkk a xalaat mooy , lan la xale yii nar a dooni ëllëg ?	
sentence: Luy mébétu PASTEF ci mbir mi ?	PASTEF <person>
sentence: Am na ay daara yu baax yu fi nekk , bu ma fi nekkee di lim damay juum .	
sentence: Ca gàggantikaayu le Robert 60 000i waat ya ca ne , 11 825 yi farañse da ko a àbb 😱 😱 ( xaaral ma daw sax ! ! )	
sentence: Alhamdu lillaah , cant fa Yàlla . 🤲 🏿	
sentence: Aada mooy lépp , moo y cëslaayu yokkute .	
sentence: Waaye du fi ame te bu soobee Yàlla , dina wax fum dugal xaalis bi mu leb yépp .	
sentence: Dangay seet , tey , bu doon wolof bi wolof kese la dégg , al pulaar di wax pulaar kese , joolaa bi yem ci làkkam , séeréer bi noonu , añs .	
sentence: Gisaanekat yi tamit kenn demul ñu des .	
sentence: Ñépp a ngi fàttaliku taxawaayam ak kàddu yu dëgër yi mu biraloon ba coowal mbirum quotas yi amee Farãs , ci atum 2010 .	Farãs <organization> atum <location>
sentence: Ñépp a koy jàng .	
sentence: Jamono jooju la yëkkatiy kàddu yu siiw yii : Ërob ba mu daj , man kese maa ciy nit ku ñuul ku fiy jiite ab këlëbu futbal .	Ërob <organization>
sentence: Dafa di , nag , Ërob rawatina Farãs , dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafóoni waaso yi .	Ërob <organization> Farãs <organization>
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi .	
sentence: Warees na nangu lu ni mel .	
sentence: Yeneen waat yi it noonu lañu mel .	
sentence: Nit dina feebar , dem loppitaal ñ u koy jox i garabi - tubaab te du wér , fekk ne feebaru ng ë m la ame .	
sentence: Danoo seetlu ne , léegi , saa booy wax ak askan wi , làmmiñu wolof ngay jëfandikoo .	
sentence: Bu ko defee , bu nuy tëral nafa gi , warees na sóoraale diine ji , beral ko xaalis ni ñu koy defale njàngum tubaab bi añs .	
sentence: Waaye , yenn saa yi , mbir mi ëpp i loxo ba njaaxum am ci , ñii am ciy gaañu - gaañu , ñale ñàkke ci seen bakkan .	
sentence: Waaye , du futbal kesee yitteloon Mabaaba .