File size: 2,758 Bytes
868d802
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
 
1
2
3
4
5
6
7
8
9
10
11
12
13
14
15
16
17
18
19
20
21
22
23
24
25
26
27
28
29
30
31
32
33
sentence: Bu ñépp bokkoon lépp , àddina si day soof .	
sentence: Ndaxte , ku xam ni pólis di doxe , nga gis ab alkaat i bu nekk ci biir màkkaanam sañ a def widewoo , yor i liif di tëkku askan wi , di ko dig ay dóor … ñàkkul mu am luñ ko sant .	
sentence: Dama ne , S apo ŋ , Farã s , Amerig añs ñoo ñu ëpp bor fuuf te doo leen mës a dégg ñuy ñaan ku leen ko baal .	S <organization> apo <location> ŋ <location> Farã <organization> s <location> Amerig <organization>
sentence: 😱 😱 😱 😱 Lii yéemewut a ! !	
sentence: Boo demee Ërob , tamit noonu .	Ërob <organization>
sentence: Español : 476i waat .	
sentence: Luy mébétu PASTEF ci mbir mi ?	PASTEF <person>
sentence: Li koy firndeel mooy , ci bés bu jëk k bi dañu duma gaa yi bu baax , ca ëllëg sa , gisuma sax muus m uy taxawaalu .	
sentence: Xawma naka lees ko tërale , waaye dafa mel ni dañuy dëddale takk - der yi ak askan wi .	
sentence: Bala nga koy xam Gàmmu jot , walla Màggal , walla Pópangin .	Pópangin <organization>
sentence: Léegi leer na ni peterool ak gaas kenn du ko jariñoo 2023 te sàggane nga li nga moomal sa bopp .	2023 <location>
sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi .	
sentence: Waaye , dañuy dàq nit ba ci biir kër am .	
sentence: Alhamdu lillaah , cant fa Yàlla . 🤲 🏿	
sentence: Ñoom , ca nguurug Pers ga woon lañuy sukkandiku fonk seen bopp .	Pers <organization>
sentence: ( Àngale a ko a yées nag , mooy làkk wi ëpp i àbb ci kaw suuf ci li nu xamagum , waatam ya xaaj ba da ko a àbb 😱 🤭 🏃 🏿 ♂ ️ )	
sentence: Ndaxte , bu dee ñ u bari ci way - juri tey yi sàmmontewu ñ ak seen i warugar , nguur gi moom loolu waru ko .	
sentence: Ku am signature ” bu baax , du ni faral leen ma bor bi .	
sentence: Xam naa , moo tax mu ni leen nañ tiital gaa ñi ngir ñu bañ a génn .	
sentence: Niral : crèche , auberge , blanc , ble … . 😲	
sentence: Farañsig ga woon : 368i waat .	
sentence: Raayante bi moo fi war a jóg , wolof mooy làmmiñ wi nu war a boole .	
sentence: Làkku Neerlànd : 249i waat .	Neerlànd <organization>
sentence: Loolu , du lu ma jékki - jekki rekk def ko .	
sentence: Xamul woon xàjj - ak - seen te bëggul woon lu jege sax boddekonte , rawatina ñeel nit ku ñuul .	
sentence: Man , nag , dama naan nguur gi defalul daara yi waaye duma wax ne dafa leen noonoo .	
sentence: 😌 - Waat yi jëm ci xarala yu yees yi yu ci bari ci àngale la ko àbbe .	
sentence: Li ma tax a wax ne dañ leen k o o sant mooy ne , dara du leen ci fekk , kenn du leen teg i daan .	
sentence: Aada mooy lépp , moo y cëslaayu yokkute .	
sentence: Du sotti .	
sentence: Ndax am na réew mu dul leb ?	
sentence: Paap , yaa nu gënoon nun ñépp .