sentence: Yeneen waat yi it noonu lañu mel . sentence: Nun Senegaal , wolof la fi Yàlla tànn . Senegaal sentence: Maanaam , defar jàkka yi , jàngu yi , daara yi , añs . sentence: Koomu Sapon daa naat bu baax , moo raw ci àddina si . Sapon sentence: Waaye , Mabaaba , ak lu mu doon mbër mu mag yépp , amul ndam ci xeexam bu mujj bi mu séqaloon ak meneen mbër mu xarañ te gaaw ci rey nit . sentence: Alalu réew mépp saax - saaxe nañu ko : Naar ak doomu Amerig ku ñëw ñu siñéel la , Tubaab ak Sinwaa waxi - nopp . Amerig sentence: Sa dem bi dafa teel . sentence: Waaye , nag , du lépp a bon ci daara yi . sentence: Ñépp a koy jàng . sentence: Sama baay joolaa la , sama maam bi jur sama yaay di al pulaar , kon man mën na wax ni duma wolof . sentence: Samir Nasri . Nasri sentence: Dañ nu doon faral di wax kàddu gii : mooytuleen contribuable bi ( ki war a fey lempo ) ; dafa ñor , day njuuj - njaaj , day nëbbu topp di la ko wax ak a waxaat . sentence: Ndax Yàlla moo nu teg nattu walla sunug nangoo nuy lor : méngaleel dundug doomi réewum Libaan ci Senegaal ak dundug doomi Senegaal ca Libaan ! Libaan Senegaal Senegaal Libaan sentence: Moo tax , bi leen jawriñ ji kalaamee yoon , ci lañ woo Abdulaay Mbay Peex , Selbe Ndom ak Gana Masire ñi doon weddi ne koronaawiris am na ci miim réew walla Tuubaa . Mbay Peex Ndom Masire Tuubaa sentence: Dinan la topp , xool ndax jàng nga , ndax am nga ñu lay jàppale ci liggéey bi , ndax am nga béréb bu baax , añs . sentence: Nun , waa PASTEF , loolu mooy sunu mébét . PASTEF sentence: Tey , Sinwaa bi dafa gëm ni Siin moo war jiite àddina si te ndog - ndog da ko daloon ci diggante bi , Àngalteer ak Sapoŋ raw ko . Siin Àngalteer Sapoŋ sentence: Wóor na ko ni su lebee , mën na fey te bala muy egg fii dafa liggéey bu baax , tëye li ko Yàlla baaxe ak feyum limpo . sentence: Lan moo ci y sa njàngat ? sentence: Iraŋ , bu àddina sépp waxee mu téye fi mu téye rekk , ñemee ŋoy fi mu ŋoy , booba cëslaayu aadaam a ko ko may . Iraŋ sentence: Ndaxte , naalub quotas ” yi mujjewul a àntu . sentence: 😌 🤝 🏿 - Toppaat ma ma xamal la làkk yi farañse àbb ak limu waat yi mu leen àbb . sentence: Bu ko defee , bu nuy tëral nafa gi , warees na sóoraale diine ji , beral ko xaalis ni ñu koy defale njàngum tubaab bi añs . sentence: Mel na ni yow ci s a bopp dundoon nga lu xaw a niro ok lii ? sentence: Nu wax ko te dee , nguur gi dafa sàggane gëm - gëmi askan wi . sentence: 😌 - Waati xam - xam yi , waati gereg ak yu latiŋ yu ñu jabbase ( jaxase ) lañu . sentence: Ci farañse : sentence: Li jiitu ci sama wax , mooy ne dama y gërëm , di sargal ak di delloo njukkal takk - der yi . sentence: Yenn saa yi ma daje ak ñenn ci ñoom , nu lal aw waxtaan . sentence: Te , loolu amul feneen ci àddina si . sentence: Ndax ñ àkk pas - pasu nguur gi la ? sentence: Moo saxal ni , ciy gëstoom , Afrig benn aada a ko lal , te Misra moo fi ëppoon doole . Afrig Misra