sentence: Ndege , ci atum 2014 , ci wutaakon yi doon sàkku Meeri Marseille bi la bokkoon . atum Marseille sentence: Loolu nag , baaxul , day féewale pólis bi ak askan wi . sentence: Duma def lu dul dellooti mbirum taalibe yi ci loxo doxalinu nguur gi . sentence: Léegi leer na ni peterool ak gaas kenn du ko jariñoo 2023 te sàggane nga li nga moomal sa bopp . 2023 sentence: Paap mujje naa am ndam ci xeex boobu . sentence: Ndaxte askanuw Senegaal dafa ragal yat . Senegaal sentence: Ñoom , ca nguurug Pers ga woon lañuy sukkandiku fonk seen bopp . Pers sentence: 😌 🤝 🏿 - Toppaat ma ma xamal la làkk yi farañse àbb ak limu waat yi mu leen àbb . sentence: Ndax bàyyees na xel ci seen wér - gi - yaram ? sentence: Loolu metti na . sentence: B ala may bëgg dee ñu naan dañoo am signature ” bu baax . sentence: Li ngay jëkk a xalaat mooy , lan la xale yii nar a dooni ëllëg ? sentence: Luy mébétu PASTEF ci mbir mi ? PASTEF sentence: Am na ay daara yu baax yu fi nekk , bu ma fi nekkee di lim damay juum . sentence: Ca gàggantikaayu le Robert 60 000i waat ya ca ne , 11 825 yi farañse da ko a àbb 😱 😱 ( xaaral ma daw sax ! ! ) sentence: Alhamdu lillaah , cant fa Yàlla . 🤲 🏿 sentence: Aada mooy lépp , moo y cëslaayu yokkute . sentence: Waaye du fi ame te bu soobee Yàlla , dina wax fum dugal xaalis bi mu leb yépp . sentence: Dangay seet , tey , bu doon wolof bi wolof kese la dégg , al pulaar di wax pulaar kese , joolaa bi yem ci làkkam , séeréer bi noonu , añs . sentence: Gisaanekat yi tamit kenn demul ñu des . sentence: Ñépp a ngi fàttaliku taxawaayam ak kàddu yu dëgër yi mu biraloon ba coowal mbirum quotas yi amee Farãs , ci atum 2010 . Farãs atum sentence: Ñépp a koy jàng . sentence: Jamono jooju la yëkkatiy kàddu yu siiw yii : Ërob ba mu daj , man kese maa ciy nit ku ñuul ku fiy jiite ab këlëbu futbal . Ërob sentence: Dafa di , nag , Ërob rawatina Farãs , dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafóoni waaso yi . Ërob Farãs sentence: Waaye nj ort naa ne , dañ leen di jox it ay ndigal yenn saa yi . sentence: Warees na nangu lu ni mel . sentence: Yeneen waat yi it noonu lañu mel . sentence: Nit dina feebar , dem loppitaal ñ u koy jox i garabi - tubaab te du wér , fekk ne feebaru ng ë m la ame . sentence: Danoo seetlu ne , léegi , saa booy wax ak askan wi , làmmiñu wolof ngay jëfandikoo . sentence: Bu ko defee , bu nuy tëral nafa gi , warees na sóoraale diine ji , beral ko xaalis ni ñu koy defale njàngum tubaab bi añs . sentence: Waaye , yenn saa yi , mbir mi ëpp i loxo ba njaaxum am ci , ñii am ciy gaañu - gaañu , ñale ñàkke ci seen bakkan . sentence: Waaye , du futbal kesee yitteloon Mabaaba .